Results for tudy na ba souba translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ba souba

French

Last Update: 2023-11-22
Usage Frequency: 3
Quality:

Wolof

dem na ba jéem a teddadil sax kër yàlla ga, waaye jàpp nanu ko.

French

et qui même a tenté de profaner le temple. et nous l`avons arrêté. nous avons voulu le juger selon notre loi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dañoo moy dëgg, di wax ne ndekkite wees na, ba yàq ngëmu ñenn ñi.

French

qui se sont détournés de la vérité, disant que la résurrection est déjà arrivée, et qui renversent le foi de quelques uns.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci suba si, bi ñuy dem, ñu gis ne garabu figg gi dee na, ba wow koŋŋ.

French

le matin, en passant, les disciples virent le figuier séché jusqu`aux racines.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bu fekkee ne ci baaraamu yàlla laay dàqe rab, kon nguuru yàlla agsi na ba ci yéen.

French

mais, si c`est par le doigt de dieu que je chasse les démons, le royaume de dieu est donc venu vers vous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waxtu waa ngi ñëw te agsi na ba noppi, dingeen tasaaroo, ku nekk ñibbi, ma des man rekk.

French

voici, l`heure vient, et elle est déjà venue, où vous serez dispersés chacun de son côté, et où vous me laisserez seul; mais je ne suis pas seul, car le père est avec moi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moom la mbind mi wax ne:«tabe na, ba may baadoolo yi;njubteem day sax ba fàww.»

French

selon qu`il est écrit: il a fait des largesses, il a donné aux indigents; sa justice subsiste à jamais.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi nga xamee ne yeesu ñëw na, ba jege taalibe yi, mu gis mbooloo mu bare wër leen, te ay xutbakat di werante ak ñoom.

French

lorsqu`ils furent arrivés près des disciples, ils virent autour d`eux une grande foule, et des scribes qui discutaient avec eux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu tontu na leen ne: «sama baay nekk na ba tey ci liggéey, kon man itam damay liggéey.»

French

mais jésus leur répondit: mon père agit jusqu`à présent; moi aussi, j`agis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dégg nanu sax ñu naan, am na kuy moy yàlla ci seen biir, moy gu ni tollu, duñu ko gis sax ci ñi xamul yàlla. dem na, ba am ci yéen kuy séy ak jabaru baayam.

French

on entend dire généralement qu`il y a parmi vous de l`impudicité, et une impudicité telle qu`elle ne se rencontre pas même chez les païens; c`est au point que l`un de vous a la femme de son père.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye jamono dina ñëw, te agsi na ba noppi, jamono joo xam ne jaamukat yi dëgg dinañu jaamu baay bi ci xel ak ci dëgg. Ñooñu nag, ñooy jaamu baay bi, ni mu ko bëgge.

French

mais l`heure vient, et elle est déjà venue, où les vrais adorateurs adoreront le père en esprit et en vérité; car ce sont là les adorateurs que le père demande.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sunuy xebaar law na, ba egg ca bokk ya fa dëkk, noonu ñu gatandu nu ba ca péncu apiyus ak bérab bu ñuy wax Ñetti añukaay ya. bi leen pool gisee, mu sant yàlla, daldi takk fitam.

French

de rome vinrent à notre rencontre, jusqu`au forum d`appius et aux trois tavernes, les frères qui avaient entendu parler de nous. paul, en les voyant, rendit grâces à dieu, et prit courage.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu kenn ca mag ña ne ma: «bul jooy. xoolal, gayndeg giiru yuda, ki soqikoo ci daawuda, daan na, ba am sañ-sañu dindi tayu yi te ubbi téere bi.»

French

et l`un des vieillards me dit: ne pleure point; voici, le lion de la tribu de juda, le rejeton de david, a vaincu pour ouvrir le livre et ses sept sceaux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,767,767 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK