Results for tuuti translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

dafa mel ni doomu fuddën, bi gën a tuuti ci jiwu yépp;

French

il est semblable à un grain de sénevé, qui, lorsqu`on le sème en terre, est la plus petite de toutes les semences qui sont sur la terre;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dees na ne: «tuuti lawiir day tax tooyalu fariñ bépp funki.»

French

un peu de levain fait lever toute la pâte.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te lii moo am: ku ji tuuti, góob tuuti; ku ji lu bare, góob lu bare.

French

sachez-le, celui qui sème peu moissonnera peu, et celui qui sème abondamment moissonnera abondamment.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su fekkee lu tuuti loolu rekk mënuleen koo def, kon lu tax ngeen di jaaxle ci li ci des?

French

si donc vous ne pouvez pas même la moindre chose, pourquoi vous inquiétez-vous du reste?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

seen tiitar bi jekkul dara. xanaa xamuleen ne, tuuti lawiir day tax tooyalu fariñ bépp funki?

French

c`est bien à tort que vous vous glorifiez. ne savez-vous pas qu`un peu de levain fait lever toute la pâte?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

céy bu ngeen ma manoon a muñal, ma wax leen tuuti waxi dof! waaw muñal-leen ma sax.

French

oh! si vous pouviez supporter de ma part un peu de folie! mais vous, me supportez!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moom la mbind mi tëral ne:«ki dajale lu bare ëpplewul dara,te ki dajale tuuti ñàkkul.»

French

selon qu`il est écrit: celui qui avait ramassé beaucoup n`avait rien de trop, et celui qui avait ramassé peu n`en manquait pas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na fa it tuuti jën yu ndaw. yeesu jël ko, sant yàlla, wax taalibe yi, ñu séddale leen itam mbooloo mi.

French

ils avaient encore quelques petits poissons, et jésus, ayant rendu grâces, les fit aussi distribuer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ki jot ci jiwu wi ci xaaxaam yi mooy ki dégg kàddu gi, waaye nes tuuti soxla yi ak alal ak bànneexi àddina tanc ko, ba du àgg cig mat.

French

ce qui est tombé parmi les épines, ce sont ceux qui, ayant entendu la parole, s`en vont, et la laissent étouffer par les soucis, les richesses et les plaisirs de la vie, et ils ne portent point de fruit qui vienne à maturité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom mooy ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ca fa gën a xóot ca géej ga.

French

mais, si quelqu`un scandalisait un de ces petits qui croient en moi, il vaudrait mieux pour lui qu`on suspendît à son cou une meule de moulin, et qu`on le jetât au fond de la mer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu dugg ci genn gaal, fekk muy gu simoŋ, mu ne ko, mu joow ba sore tuuti. noonu yeesu toog ca gaal ga, di jàngal mbooloo ma.

French

il monta dans l`une de ces barques, qui était à simon, et il le pria de s`éloigner un peu de terre. puis il s`assit, et de la barque il enseignait la foule.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moo tax ma di la wax ne, su wonee mbëggeel gu réye nii, dafa fekk ñu baal ko bàkkaaram yu bare. waaye ki mbëggeelam néew dafa fekk ñu baal ko lu tuuti.»

French

c`est pourquoi, je te le dis, ses nombreux péchés ont été pardonnés: car elle a beaucoup aimé. mais celui à qui on pardonne peu aime peu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

doomu fuddën moo gën a tuuti ci jiwu yépp, waaye bu saxee, mooy sut ci gàncaxi tóokër yi, di nekk garab, ba picci asamaan ñëw, tàgg ciy caram.»

French

c`est la plus petite de toutes les semences; mais, quand il a poussé, il est plus grand que les légumes et devient un arbre, de sorte que les oiseaux du ciel viennent habiter dans ses branches.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

buur ba ne ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga. segam wone nga ne, takku nga ci lu tuuti, falul ci fukki dëkk.”

French

il lui dit: c`est bien, bon serviteur; parce que tu as été fidèle en peu de chose, reçois le gouvernement de dix villes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

njaatigeem tontu ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga te takku. gannaaw takku nga ci lu tuuti, dinaa la dénk lu bare. kaay bokk ci sama mbég.”

French

son maître lui dit: c`est bien, bon et fidèle serviteur; tu as été fidèle en peu de chose, je te confierai beaucoup; entre dans la joie de ton maître.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,946,762,058 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK