From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bokk momel
mairie
Last Update: 2021-12-06
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
saxleen ci bëggante ni ay bokk.
persévérez dans l`amour fraternel.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
ku ko nuyu, bokk nga ciy ñaawteefam.
car celui qui lui dit: salut! participe à ses mauvaises oeuvres.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
Ñoom ñépp bokk nañoo lekk ñam, wa yàlla joxe,
qu`ils ont tous mangé le même aliment spirituel,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:
nous vous y trompez pas, mes frères bien-aimés:
Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 31
Quality:
Reference:
yéen bokk yi, yéenay doom yi ñu dige woon, niki isaaxa.
pour vous, frères, comme isaac, vous êtes enfants de la promesse;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
nanu ko fekki nag ca gannaaw dal ba, bokk ak moom toroxte ga.
sortons donc pour aller à lui, hors du camp, en portant son opprobre.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
xel mi, ndox ak deret, te ñoom ñett ñépp, ñoo bokk benn baat.
l`esprit, l`eau et le sang, et les trois sont d`accord.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
Ñoo bokk mébét, di jox seen kàttan ak seen sañ-sañ rab wi.
ils ont un même dessein, et ils donnent leur puissance et leur autorité à la bête.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
yéen ñépp, ñi ñu sóob ci ndox ngir wone seen bokk ci kirist, soloo ngeen kirist.
vous tous, qui avez été baptisés en christ, vous avez revêtu christ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
léegi nag bokk yi, ci li jëm ci mayi xelum yàlla, bëgguma ngeen umple ci dara.
pour ce qui concerne les dons spirituels, je ne veux pas, frères, que vous soyez dans l`ignorance.
Last Update: 2023-10-08
Usage Frequency: 2
Quality:
Reference:
noonu nag bokk yi, bu ngeen dajee, di lekk reeru boroom bi, nangeen xaarante.
ainsi, mes frères, lorsque vous vous réunissez pour le repas, attendez-vous les uns les autres.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
te ñépp bokk genn kàddu naan:yeesu kirist mooy boroom bi;ci màggug yàlla baay bi.
et que toute langue confesse que jésus christ est seigneur, à la gloire de dieu le père.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
xale yi, déggal-leen seeni waajur ci lépp, ndaxte looloo rafet ci ñi bokk ci boroom bi.
enfants, obéissez en toutes choses à vos parents, car cela est agréable dans le seigneur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
mu ne ko: “toxul sa réew, bàyyi say bokk, te ñëw ci réew, mi ma lay won.”
quitte ton pays et ta famille, et va dans le pays que je te montrerai.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: