Results for xarafal translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

«lu tax nga dem ca këru ñu xarafal, bay lekk sax ak ñoom?»

French

en disant: tu es entré chez des incirconcis, et tu as mangé avec eux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moytuleen xaj yi, waaw moytuleen ñiy jëfe lu bon, ñoom ñi seen xarafal weesul wàññi yaramu nit.

French

prenez garde aux chiens, prenez garde aux mauvais ouvriers, prenez garde aux faux circoncis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te tit mi ma gunge woon sax de, li mu bokk ci xeetu gereg, taxul ñu sonal nu ci xarafal ko.

French

mais tite, qui était avec moi, et qui était grec, ne fut pas même contraint de se faire circoncire.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi bés ba dellusee jamonoy xarafal xale ba agsi. Ñu tudde ko yeesu, ni ko malaaka ma diglee woon, laata ko yaayam di ëmb.

French

le huitième jour, auquel l`enfant devait être circoncis, étant arrivé, on lui donna le nom de jésus, nom qu`avait indiqué l`ange avant qu`il fût conçu dans le sein de sa mère.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu ngeen manee xarafal nit ci bésu noflaay bi, ngir bañ a wàcc yoonu musaa, lu tax nag ngeen mere ma, ndax li ma ci wéral nitu lëmm?

French

si un homme reçoit la circoncision le jour du sabbat, afin que la loi de moïse ne soit pas violée, pourquoi vous irritez-vous contre moi de ce que j`ai guéri un homme tout entier le jour du sabbat?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool bëgg nag mu ànd ak moom, waaye ndegam yawut yépp, ya dëkk ca wàllaa ya, xam ne baayam gereg la woon, mu jël ko, xarafal ko.

French

paul voulut l`emmener avec lui; et, l`ayant pris, il le circoncit, à cause des juifs qui étaient dans ces lieux-là, car tous savaient que son père était grec.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li leen musaa jox ndigalu xarafal gune yi --jógewul kat ci musaa; mi ngi tàmbalee ci seen maami cosaan — moo tax ba ngeen nangoo xarafal nit ci bésu noflaay bi.

French

moïse vous a donné la circoncision, -non qu`elle vienne de moïse, car elle vient des patriarches, -et vous circoncisez un homme le jour du sabbat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yàlla nag tëral kóllëre seen diggante, fas ko ci màndargam xaraf. noonu ibraayma jur isaaxa, xarafal ko ca juróom-ñetteelu fan ba; isaaxa def noonu yanqóoba, yanqóoba it def noonu fukki maam ya ak ñaar, ñi sos xeet wi.

French

puis dieu donna à abraham l`alliance de la circoncision; et ainsi, abraham, ayant engendré isaac, le circoncit le huitième jour; isaac engendra et circoncit jacob, et jacob les douze patriarches.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,906,554,753 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK