From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
noonu piyeer fàttaliku li xewoon, ne yeesu: «kilifa gi, xoolal, figg gi nga rëbb dee na, ba wow!»
pierre, se rappelant ce qui s`était passé, dit à jésus: rabbi, regarde, le figuier que tu as maudit a séché.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu ne leen: «demleen ne bukki boobu ne ko: “xoolal, maa ngi dàq rab yi tey wéral nit ñi tey ak suba. ca ñetteelu fan ba, ma àgg fa ma yàlla jëmale.”
il leur répondit: allez, et dites à ce renard: voici, je chasse les démons et je fais des guérisons aujourd`hui et demain, et le troisième jour j`aurai fini.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: