From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.’ ”
je ne suis plus digne d`être appelé ton fils; traite-moi comme l`un de tes mercenaires.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kan ci yéen, bu la sa doom ñaanee mburu, nga jox ko doj?
lequel de vous donnera une pierre à son fils, s`il lui demande du pain?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu la sa doom ñaanee jën, yaw miy baayam, ndax dinga ko bañ a jox jën, jox ko jaan?
quel est parmi vous le père qui donnera une pierre à son fils, s`il lui demande du pain? ou, s`il demande un poisson, lui donnera-t-il un serpent au lieu d`un poisson?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
doom ja ne ko: “baay, tooñ naa yàlla, tooñ naa la; yeyootumaa nekk sa doom.”
le fils lui dit: mon père, j`ai péché contre le ciel et contre toi, je ne suis plus digne d`être appelé ton fils.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu yeesu ne ko: «ndax wax jooju demal ci jàmm, rab wa génn na sa doom.»
alors il lui dit: à cause de cette parole, va, le démon est sorti de ta fille.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne ko: «demal, sa doom dina dund.» kilifa ga gëm la ko yeesu wax, daldi dem.
va, lui dit jésus, ton fils vit. et cet homme crut à la parole que jésus lui avait dite, et il s`en alla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yeesu gisee yaayam taxaw ci wetu taalibe, bi mu bëggoon, mu ne ko: «soxna si, sa doom a ngi,»
jésus, voyant sa mère, et auprès d`elle le disciple qu`il aimait, dit à sa mère: femme, voilà ton fils.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yeesu di wax nag, am na ku jóge ca kër njiit la, mu ñëw naan: «sa doom faatu na; matatul nuy sonal kilifa gi.»
comme il parlait encore, survinrent de chez le chef de la synagogue des gens qui dirent: ta fille est morte; pourquoi importuner davantage le maître?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu baayu xale ba daldi seetlu ne, ca waxtu woowa la ko yeesu ne woon: «sa doom dina dund.» moom ak njabootam gépp, ñu daldi gëm yeesu.
le père reconnut que c`était à cette heure-là que jésus lui avait dit: ton fils vit. et il crut, lui et toute sa maison.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.