Results for lekkandoo translation from Wolof to German

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

German

Info

Wolof

amoon na ab farisen bu ñaan yeesu, mu ñëw lekkandoo ak moom. yeesu dem kër waa ja, toog ca lekkukaay.

German

es bat ihn aber der pharisäer einer, daß er mit ihm äße. und er ging hinein in des pharisäers haus und setzte sich zu tisch.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu lewi togglu ay ñam yu bare ci këram, ngir teral yeesu. juutikat yu bare ak yeneen gan ñu nga fa woon, di lekkandoo ak ñoom.

German

und levi richtete ihm ein großes mahl zu in seinem hause, und viele zöllner und andere saßen mit ihm zu tisch.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee yeesu ak i taalibeem di lekk ci kër lewi, fekk ay juutikat ak ay boroom bàkkaar yu bare di lekkandoo ak ñoom, ndaxte ñu bare ci ñoom a ko toppoon.

German

und es begab sich, da er zu tische saß in seinem hause, setzten sich viele zöllner und sünder zu tische mit jesu und seinen jüngern; denn ihrer waren viele, die ihm nachfolgten.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko farisen ya gisee nag, ñu ne taalibe ya: «lu tax seen kilifa di lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

German

da das die pharisäer sahen, sprachen sie zu seinen jüngern: warum isset euer meister mit den zöllnern und sündern?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

farisen yi ak seeni xutbakat di xultu taalibey yeesu yi ne leen: «lu tax ngeen di lekkandoo ak di naanandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

German

und die schriftgelehrten und pharisäer murrten wider seine jünger und sprachen: warum esset und trinket ihr mit den zöllnern und sündern?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye xutbakat yi bokk ci farisen yi, bi ñu gisee ne, dafa bokk lekk ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar, ñu daldi laaj taalibe yi: «lu tax muy lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

German

und die schriftgelehrten und pharisäer, da sie sahen, daß er mit den zöllnern und sündern aß, sprachen sie zu seinen jüngern: warum ißt und trinkt er mit den zöllnern und sündern?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,749,119,965 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK