Results for dëggal translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

dëggal-leen ci seeni jëf li neex boroom bi,

Italian

cercate ciò che è gradito al signore

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moo tax may dëggal tey jii ne, wàccoo naa ak yéen ñépp bés pénc.

Italian

per questo dichiaro solennemente oggi davanti a voi che io sono senza colpa riguardo a coloro che si perdessero

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte li nu doon seedeel kirist, yàlla dëggal na ko ci yéen.

Italian

la testimonianza di cristo si è infatti stabilita tra voi così saldamente

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye pool ak barnabas daldi yëlëb seen pëndu tànk, ngir dëggal seen weddi, jëm dëkku ikoñum.

Italian

allora essi, scossa contro di loro la polvere dei piedi, andarono a icònio

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na seen teeru firndeel nag seen mbëggeel ci kanamu mboolooy ñi gëm, te dëggal leen ne, noo yey wóolu leen.

Italian

date dunque a loro la prova del vostro affetto e della legittimità del nostro vanto per voi davanti a tutte le chiese

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

taalibe ya dem waareji, te loxob boroom bi ànd ak ñoom, di dëggal kàddu gi ak firnde, yi ci ànd.

Italian

allora essi partirono e predicarono dappertutto, mentre il signore operava insieme con loro e confermava la parola con i prodigi che l'accompagnavano

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi leen di wax lii nag, te di ko dëggal ci kanamu boroom bi: buleen dundeeti ni xeeti àddina yi, ci seeni xalaati neen

Italian

vi dico dunque e vi scongiuro nel signore: non comportatevi più come i pagani nella vanità della loro mente

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te it yàlla dëggal na seen seede ci ay firnde ak ay kéemaan, ay jaloore yu bare ak ci ay may yu jóge ci xelam mu sell, te mu séddale leen ni mu ko bëgge.

Italian

mentre dio testimoniava nello stesso tempo con segni e prodigi e miracoli d'ogni genere e doni dello spirito santo, distribuiti secondo la sua volontà

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bi silas ak timote jógee diiwaanu maseduwan, egg fa, pool jublu ci xamle kàddu gi, tey dëggal ci yawut yi naan, yeesu mooy almasi bi.

Italian

quando giunsero dalla macedonia sila e timòteo, paolo si dedicò tutto alla predicazione, affermando davanti ai giudei che gesù era il cristo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool ak barnabas nag sax nañu ci ikoñum lu yàgg, ñu wéeru ci boroom bi, bay wax ak fit wu dëgër; te yàlla dëggal kàddug yiwam, ba may leen, ñu def ay kéemaan ak ay firnde.

Italian

rimasero tuttavia colà per un certo tempo e parlavano fiduciosi nel signore, che rendeva testimonianza alla predicazione della sua grazia e concedeva che per mano loro si operassero segni e prodigi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu dig ko bés, te ñu bare ñëw, fekksi ko ca néegam. mu di leen jàngal suba ba ngoon, di leen dëggal lu jëm ci nguuru yàlla ak ci yeesu, tukkee ci yoonu musaa ak ci yonent yi, di leen jéem a gëmloo.

Italian

e fissatogli un giorno, vennero in molti da lui nel suo alloggio; egli dal mattino alla sera espose loro accuratamente, rendendo la sua testimonianza, il regno di dio, cercando di convincerli riguardo a gesù, in base alla legge di mosè e ai profeti

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,780,147,426 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK