Results for dëggu translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

te soloo jikko ju bees, ji yàlla sàkk ci njub ak sell yu dëggu.

Italian

e rivestire l'uomo nuovo, creato secondo dio nella giustizia e nella santità vera

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

juddu nekk yawut taxul sag yawut dëggu, te xaraf ci saw yaram taxul sa xaraf wóor.

Italian

infatti, giudeo non è chi appare tale all'esterno, e la circoncisione non è quella visibile nella carne

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loolu lépp nag takkandeer la woon buy misaal li waroon a ñëw, waaye lu dëggu li mi ngi ci kirist.

Italian

tutte cose queste che sono ombra delle future; ma la realtà invece è cristo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bu la dégluwul, àndal ak kenn mbaa ñaar, ngir mbir mi dëggu ci li ko ñaar walla ñett seede.

Italian

se non ti ascolterà, prendi con te una o due persone, perché ogni cosa sia risolta sulla parola di due o tre testimoni

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ak it apeles, mi ngëmam dëggu, ba yelloo kóolute.nuyul-leen ma it waa kër aristobul,

Italian

salutate apelle che ha dato buona prova in cristo. salutate i familiari di aristòbulo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

war na jàpp ci xebaar bu dëggu, bi lal sunu yoon, ba man a dénkaane ci njàngale mu wér mi, tey yey ñi weddi.

Italian

attaccato alla dottrina sicura, secondo l'insegnamento trasmesso, perché sia in grado di esortare con la sua sana dottrina e di confutare coloro che contraddicono

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi fàttaliku sa ngëm gu dëggu, gi nekkoon ci sa maam lowis ak sa yaay Ënis, te mu wóor ma ne, sax na ci yaw it.

Italian

mi ricordo infatti della tua fede schietta, fede che fu prima nella tua nonna lòide, poi in tua madre eunìce e ora, ne sono certo, anche in te

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye pool tontu ko: «festus mu tedd mi, dofuma; waaye lu dëggu laay wax te ànd ak sago.

Italian

e paolo: «non sono pazzo, disse, eccellentissimo festo, ma sto dicendo parole vere e sagge

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ma dégge baat jibe ca saraxalukaayu cuuraay ba naan:«waaw boroom bi yàlla, aji kàttan ji,say àtte dëggu nañu te jub.»

Italian

udii una voce che veniva dall'altare e diceva: veri e giusti sono i tuoi giudizi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ngi liggéey ca bérab bu sell-baa-sell, di màggalukaay bu dëggu. nit defaru ko; boroom bee ko sos.

Italian

ministro del santuario e della vera tenda che il signore, e non un uomo, ha costruito

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yëfi àddina yi misaal yu dëggu yi ci asamaan, war nañu leen a sellale noonu. waaye yëf yu dëggu yooyu ci asamaan, laaj na sarax yu gën a baax, ngir ñu sell.

Italian

era dunque necessario che i simboli delle realtà celesti fossero purificati con tali mezzi; le realtà celesti poi dovevano esserlo con sacrifici superiori a questi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ñoom ci seen bopp ñooy seede li sunu ngan def ci seen biir. maanaam, ni ngeen dëddoo xërëm yi, jublu ci yàlla te di ko jaamu, moom miy yàlla aji dund ju dëggu ji,

Italian

sono loro infatti a parlare di noi, dicendo come noi siamo venuti in mezzo a voi e come vi siete convertiti a dio, allontanandovi dagli idoli, per servire al dio vivo e ver

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ay àtteem dañoo dëggu te jub!ndaxte àtte na jigéenu moykat bu mag,bi daan yàq àddina si ak njaaloom,te feyyul na noonu jaami yàlla, yi mu daan rey.»

Italian

perché veri e giusti sono i suoi giudizi, egli ha condannato la grande meretrice che corrompeva la terra con la sua prostituzione, vendicando su di lei il sangue dei suoi servi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yoonu musaa dafa misaal xéewal yi waroon a ñëw; takkandeer la ci yëf yu dëggu yi, waaye du ñoom ci seen bopp. looloo tax mënul a yeggale cig mat ñi ñëw ci yàlla, ndaxte at mu nekk duñu jóg ci jébbal yàlla sarax yooyu.

Italian

avendo infatti la legge solo un'ombra dei beni futuri e non la realtà stessa delle cose, non ha il potere di condurre alla perfezione, per mezzo di quei sacrifici che si offrono continuamente di anno in anno, coloro che si accostano a dio

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,779,603,645 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK