From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
kirist a nu daggal sunu buumi njaam, ngir goreel nu. kon dëgërleen ci seen ngor te bañ a delluwaat ci njaam.
cristo ci ha liberati perché restassimo liberi; state dunque saldi e non lasciatevi imporre di nuovo il giogo della schiavitù
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu xamoon na ne, yàlla joxoon na ko sañ-sañ ci lépp, xam it ne, ca yàlla la jóge te ca moom lay delluwaat.
gesù sapendo che il padre gli aveva dato tutto nelle mani e che era venuto da dio e a dio ritornava
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu yéegaat, damm mburu ma, lekk; ba noppi delluwaat ci waxtaanam, di ko yaatal ba ca njël, door a tàggoo.
poi risalì, spezzò il pane e ne mangiò e dopo aver parlato ancora molto fino all'alba, partì
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu delluwaat di ñaan ne: «sama baay, bu fekkee ne kaasu naqar bii mënu maa teggi te naanuma ko, kon na sa coobare am.»
e di nuovo, allontanatosi, pregava dicendo: «padre mio, se questo calice non può passare da me senza che io lo beva, sia fatta la tua volontà»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye léegi nag bi ngeen xamee yàlla, walla boog bi leen yàlla xàmmee, nan ngeen man a def, bay delluwaat ca aaday àddina? aada yooyee ñàkk doole te ñàkk njariñ, lu tax ngeen bëgg, ñu nootaat leen?
ora invece che avete conosciuto dio, anzi da lui siete stati conosciuti, come potete rivolgervi di nuovo a quei deboli e miserabili elementi, ai quali di nuovo come un tempo volete servire
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: