Results for dul translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

su néew yi dul dekki, kirist moom it dekkiwul.

Italian

se infatti i morti non risorgono, neanche cristo è risorto

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te li mu nu digoon mooy lii: dund gu dul jeex.

Italian

e questa è la promessa che egli ci ha fatto: la vita eterna

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amul kenn ci ñoom ku ñëw gërëm yàlla ku dul doxandéem bii!»

Italian

non si è trovato chi tornasse a render gloria a dio, all'infuori di questo straniero?». e gli disse

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu xool ci kaw, waaye gisatuñu kenn ku dul yeesu rekk.

Italian

sollevando gli occhi non videro più nessuno, se non gesù solo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kenn musul a yéeg ci asamaan su dul ki fa jóge, muy doomu nit ki.

Italian

eppure nessuno è mai salito al cielo, fuorché il figlio dell'uomo che è disceso dal cielo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te xam ngeen li ko téye léegi, ba du man a feeñ lu dul ci waxtoom.

Italian

e ora sapete ciò che impedisce la sua manifestazione, che avverrà nella sua ora

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sédd na leen cér bu dul yàqu, du gàkk te du seey mukk, dencal leen ko ci asamaan,

Italian

per una eredità che non si corrompe, non si macchia e non marcisce. essa è conservata nei cieli per voi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te yeesu mënu faa def ay kéemaan yu bare, lu dul teg loxo yenn jarag, wéral leen.

Italian

e non vi potè operare nessun prodigio, ma solo impose le mani a pochi ammalati e li guarì

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dinañu ko jébbal ñi dul yawut, ñu ñaawal ko, saaga ko, tifli ci kawam.

Italian

sarà consegnato ai pagani, schernito, oltraggiato, coperto di sput

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon diirunu li ñuy gis waaye li ñu dul gis. ndaxte li ñuy gis day wéy, waaye li ñu dul gis day sax ba fàww.

Italian

perché noi non fissiamo lo sguardo sulle cose visibili, ma su quelle invisibili. le cose visibili sono d'un momento, quelle invisibili sono eterne

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñiy jëfe noonu waaru nañu, ba di leen sosal, ci li ngeen àndul ak ñoom, sóobu ci seeni moy yu dul jeex,

Italian

per questo trovano strano che voi non corriate insieme con loro verso questo torrente di perdizione e vi oltraggiano

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye léegi yàlla goreel na leen ci kilifteefu bàkkaar, def leen ay jaamam, ba jural leen sell, jëme leen ci dund gu dul jeex.

Italian

ora invece, liberati dal peccato e fatti servi di dio, voi raccogliete il frutto che vi porta alla santificazione e come destino avete la vita eterna

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag amul xaajale ci diggante yawut ak ki dul yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci kirist.

Italian

non c'è più giudeo né greco; non c'è più schiavo né libero; non c'è più uomo né donna, poiché tutti voi siete uno in cristo gesù

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu xool ay taalibeem ne leen:«yéen ñi sësul lu dul ci yàlla, barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla, yéena ko yelloo.

Italian

alzati gli occhi verso i suoi discepoli, gesù diceva: «beati voi poveri, perché vostro è il regno di dio

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,941,808,817 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK