From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
su amee kuy wax aw làkk, na ñaar wax walla gën gaa bare ñett. nañu ko toppante, te kenn di firi.
quando si parla con il dono delle lingue, siano in due o al massimo in tre a parlare, e per ordine; uno poi faccia da interprete
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte fi mu ne ñaawteef gaa ngi jax-jaxi xaat ci kumpa, waaye ki ko téye mi ngi fi ba tey. bu fi jógee nag,
il mistero dell'iniquità è gia in atto, ma è necessario che sia tolto di mezzo chi finora lo trattiene
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
xeet yi meroon nañu,waaye sa mer wàcc na,te jamono ji jot na,ji ngay àttee ñi dee,neexal say jaam yonent yi,ak sa gaa ñi ak ñi ragal saw tur,muy mag di ndaw,te nga rey ñiy yàq àddina.»
le genti ne fremettero, ma è giunta l'ora della tua ira, il tempo di giudicare i morti, di dare la ricompensa ai tuoi servi, ai profeti e ai santi e a quanti temono il tuo nome, piccoli e grandi, e di annientare coloro che distruggono la terra»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: