From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ku ma bañ, bañ nga itam sama baay.
chi odia me, odia anche il padre mio
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
naka noonu itam nanga xiir waxambaane yi cig maandu.
esorta ancora i più giovani a essere assennati
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te am nga noonu itam ay nit ñuy sàmm njàngalem ñoom nikolas.
così pure hai di quelli che seguono la dottrina dei nicolaìti
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndegam ñu bare dañuy damu ni nit kese, man itam kon dinaa damu.
dal momento che molti si vantano da un punto di vista umano, mi vanterò anch'io
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jox na doom ji itam sañ-sañu àtte, ndaxte mooy doomu nit ki.
e gli ha dato il potere di giudicare, perché è figlio dell'uomo
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«Ñaanaluma leen ñoom rekk, waaye itam ñi may gëm ëllëg ndax seen wax.
non prego solo per questi, ma anche per quelli che per la loro parola crederanno in me
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu ngeen gëmoon musaa, dingeen ma gëm man itam, ndaxte seedeel na ma.
se credeste infatti a mosè, credereste anche a me; perché di me egli ha scritto
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te itam muju lépp jegesi na; nangeen maandu te foog, ba man a ñaan ci yàlla.
la fine di tutte le cose è vicina. siate dunque moderati e sobri, per dedicarvi alla preghiera
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ku weddi doom ji, amuloo itam baay bi; ku seedeel doom ji, am nga it baay bi.
chiunque nega il figlio, non possiede nemmeno il padre; chi professa la sua fede nel figlio possiede anche il padre
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.
quindi anche voi, poiché desiderate i doni dello spirito, cercate di averne in abbondanza, per l'edificazione della comunità
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te itam nanga ma waajal néeg, ndaxte yaakaar naa ne, yàlla dina nangu seeni ñaan, ba delloosi ma leen.
al tempo stesso preparami un alloggio, perché spero, grazie alle vostre preghiere, di esservi restituito
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndegam xam ngeen ma, dingeen xam itam sama baay. lu weesu tey, xam ngeen ko te gis ngeen ko.»
se conoscete me, conoscerete anche il padre: fin da ora lo conoscete e lo avete veduto»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
booba dafa seddoon, ba surga ya ak alkaati ya boyal ab taal, di ca jaaru. piyeer itam taxaw, di jaaru ak ñoom.
intanto i servi e le guardie avevano acceso un fuoco, perché faceva freddo, e si scaldavano; anche pietro stava con loro e si scaldava
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
def na jöffë-jöffë nä %(plugin_conflict)s waye %(plugin)s itam indil neñu %(feature)s lá.
il plugin %(plugin_conflict)s fornisce la funzionalità %(feature)s fornita anche da %(plugin)s
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality: