From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
moona kàddug boroom bi di gën a màgg tey law.
intanto la parola di dio cresceva e si diffondeva
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona ca bés pénc ba, tir ak sidon ñoo leen di tane.
perciò nel giudizio tiro e sidone saranno trattate meno duramente di voi
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yoon dabu ko fenn, moona ñaan nañu pilaat, mu reylu ko.
e, pur non avendo trovato in lui nessun motivo di condanna a morte, chiesero a pilato che fosse ucciso
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona foog naa ne, seen ndaw yooyu ngeen yékkati, ba ñu ëpp ndaw sax, ëpplewuñu ma dara.
ora io ritengo di non essere in nulla inferiore a questi «super apostoli»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«moona aji kawe ji du dëkk ci fu loxol nit defar; moom la ab yonent wax ne:
ma l'altissimo non abita in costruzioni fatte da mano d'uomo, come dice il profeta
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nit ñooñu ñépp, seen ngëm a tax ba yàlla seedeeloon leen lu baax. moona de, jotuñu li yàlla dige woon,
eppure, tutti costoro, pur avendo ricevuto per la loro fede una buona testimonianza, non conseguirono la promessa
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona li leen rab yi déggal, bumu tax ngeen bég, waaye bégleen ndax li ñu bind seen tur ci asamaan.»
non rallegratevi però perché i demòni si sottomettono a voi; rallegratevi piuttosto che i vostri nomi sono scritti nei cieli»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona yéen de, yéena ngi tiitaru. waaye dangeen a waroon a am naqar, ba dàq kiy def loolu ci seen biir!
e voi vi gonfiate di orgoglio, piuttosto che esserne afflitti, in modo che si tolga di mezzo a voi chi ha compiuto una tale azione
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona yàlla yónniwul iliyas ci kenn ci ñoom, waaye mu yebal ko ci jigéen ju jëkkëram faatu, ju dëkk sarebta, ca wetu sidon.
ma a nessuna di esse fu mandato elia, se non a una vedova in sarepta di sidone
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona daan naa toog bés bu nekk ca kër yàlla ga, di jàngale, te jàppuleen ma. waaye lii am na, ngir mbind mi am.»
ogni giorno ero in mezzo a voi a insegnare nel tempio, e non mi avete arrestato. si adempiano dunque le scritture!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona daa naa suufeel turam, di fitnaal ak a toroxal ñi ko gëm. waaye yàlla yërëm na ma, ndaxte ñàkka xam ak ñàkka gëm rekk a taxoon ma def ko.
io che per l'innanzi ero stato un bestemmiatore, un persecutore e un violento. ma mi è stata usata misericordia, perché agivo senza saperlo, lontano dalla fede
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona noppiwul a firndeel aw meloom ci def lu baax, di leen wàcceele ci asamaan taw buy indi naataange, ba ngeen lekk ba suur, te seen xol fees ak mbég.»
ma non ha cessato di dar prova di sé beneficando, concedendovi dal cielo piogge e stagioni ricche di frutti, fornendovi il cibo e riempiendo di letizia i vostri cuori»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moona am na xam-xam bu nuy yégal ñi mat, xam-xam bu bokkul ci àddina si, te njiiti àddina si xamuñu ko, ñoom ñi nar a wéy.
tra i perfetti parliamo, sì, di sapienza, ma di una sapienza che non è di questo mondo, né dei dominatori di questo mondo che vengono ridotti al nulla
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu daldi tontu ne leen: «xanaa du maa leen tànn, yéen fukk yi ak ñaar? moona, am na ci yéen koo xam ne seytaane la!»
rispose gesù: «non ho forse scelto io voi, i dodici? eppure uno di voi è un diavolo!». egli parlava di giuda, figlio di simone iscariota: questi infatti stava per tradirlo, uno dei dodici
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
xam naa fa nga dëkk, di fa seytaane samp nguuram. moona jébbalu nga ci sama tur te weddiwoo sa ngëm ci man, ba ca fan ya ñu reye antipas, sama seede bu takku ba, ci seen dëkk, di dëkku seytaane. i
so che abiti dove satana ha il suo trono; tuttavia tu tieni saldo il mio nome e non hai rinnegato la mia fede neppure al tempo in cui antìpa, il mio fedele testimone, fu messo a morte nella vostra città, dimora di satana
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu am, ci bokki taalibe yi, ñu xalaat ne, taalibe boobu du dee. moona yeesu musul ne piyeer, du dee; waaye li mu wax mooy: «su ma neexoon mu dund, ba ma dellusi, lu ciy sa yoon?»
si diffuse perciò tra i fratelli la voce che quel discepolo non sarebbe morto. gesù però non gli aveva detto che non sarebbe morto, ma: «se voglio che rimanga finché io venga, che importa a te?»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: