Results for nettali translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

mu nettali leen lépp, yebal leen yope.

Italian

spiegata loro ogni cosa, li mandò a giaffa

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu yeesu nettali leen beneen léeb ne leen:

Italian

gesù riprese a parlar loro in parabole e disse

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu piyeer daldi leen benn-bennal mbir mi, nettali leen ko

Italian

allora pietro raccontò per ordine come erano andate le cose, dicendo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu leen gisee, ñu nettali la ñu leen waxoon ca mbirum xale ba.

Italian

e dopo averlo visto, riferirono ciò che del bambino era stato detto loro

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ña fekke woon mbir ma nag nettali leen mbirum nit ka ak mbaam-xuux ya.

Italian

quelli che avevano visto tutto, spiegarono loro che cosa era accaduto all'indemoniato e il fatto dei porci

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ña fekke woon mbir ma nag, nettali leen naka la yeesu wérale ki rab ya jàppoon.

Italian

quelli che erano stati spettatori riferirono come l'indemoniato era stato guarito

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu ndaw yi dajaloo ci wetu yeesu, nettali li ñu def ak li ñu jàngale lépp.

Italian

gli apostoli si riunirono attorno a gesù e gli riferirono tutto quello che avevano fatto e insegnato

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

taalibey yaxya ya nettali mbir yooyu yépp seen kilifa. noonu yaxya woo ñaar ci ay taalibeem,

Italian

anche giovanni fu informato dai suoi discepoli di tutti questi avvenimenti. giovanni chiamò due di ess

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñaari taalibe ya ñoom it daldi leen nettali la xewoon ca yoon wa ak ni ñu xàmmee yeesu, bi mu dammee mburu ma.

Italian

essi poi riferirono ciò che era accaduto lungo la via e come l'avevano riconosciuto nello spezzare il pane

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw teyofil mu tedd mi, xam nga ne, nit ñu bare sasoo nañoo bind ab nettali bu jëm ci mbir, yi xewoon ci sunu biir,

Italian

poiché molti han posto mano a stendere un racconto degli avvenimenti successi tra di noi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

jigéen ña ñoo doon maryaamam magdala, sànn, ak maryaama yaayu saag. yeneen jigéen yi leen gunge woon itam nettali loolu ndaw ya.

Italian

erano maria di màgdala, giovanna e maria di giacomo. anche le altre che erano insieme lo raccontarono agli apostoli

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye fekkuñu fa néewam. Ñu dellusi, nettali nu ne, ay malaaka feeñu nañu leen, yégal leen ne, mi ngi dund.

Italian

e non avendo trovato il suo corpo, son venute a dirci di aver avuto anche una visione di angeli, i quali affermano che egli è vivo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ndaw ya dellusee, ñu nettali yeesu la ñu defoon lépp. noonu mu yóbbaale leen, ñu sore nit ñi, jëm ca dëkk bu ñuy wax betsayda.

Italian

al loro ritorno, gli apostoli raccontarono a gesù tutto quello che avevano fatto. allora li prese con sé e si ritirò verso una città chiamata betsàida

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu maryaamam magdala dem, yégali ko taalibe ya ne leen: «gis naa boroom bi!» mu daldi leen nettali li mu ko wax.

Italian

maria di màgdala andò subito ad annunziare ai discepoli: «ho visto il signore» e anche ciò che le aveva detto

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«Ñibbil, nettali li la yàlla defal lépp.» noonu waa ji dem di wër dëkk ba yépp, di fa yégle la ko yeesu defal.

Italian

«torna a casa tua e racconta quello che dio ti ha fatto». l'uomo se ne andò, proclamando per tutta la città quello che gesù gli aveva fatto

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«bokk yi, dégluleen ma! simoŋ nettali na, ni yàlla seetsee bu jëkk ñi dul yawut, ngir sàkku ci ñoom xeet wu ñu tudde turam.

Italian

«fratelli, ascoltatemi. simone ha riferito come fin da principio dio ha voluto scegliere tra i pagani un popolo per consacrarlo al suo nome

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu mayu ko ko. mu ne ko: «Ñibbil ci say bokk, nettali leen ni la boroom bi yërëme, ba defal la lii lépp.»

Italian

non glielo permise, ma gli disse: «và nella tua casa, dai tuoi, annunzia loro ciò che il signore ti ha fatto e la misericordia che ti ha usato»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee ñu wàcc ca tund wa. bi ñuy wàcc nag, yeesu sant leen ne: «buleen nettali kenn li ngeen gis, ba kera doomu nit ki dekki.»

Italian

e mentre discendevano dal monte, gesù ordinò loro: «non parlate a nessuno di questa visione, finché il figlio dell'uomo non sia risorto dai morti»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«surga ba dellu ca njaatigeem nettali ko loolu lépp. noonu boroom kër ga mer, daldi ne surga ba: “demal gaaw ca pénc ya ak ca mbedd ya ca dëkk ba, te indil ma fii néew doole yi, ñu làggi ñi, gumba yi ak lafañ yi.”

Italian

al suo ritorno il servo riferì tutto questo al padrone. allora il padrone di casa, irritato, disse al servo: esci subito per le piazze e per le vie della città e conduci qui poveri, storpi, ciechi e zoppi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,867,501,360 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK