From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
“waa jii dafa tàmbalee tabax, waaye mënu koo àggale.”
costui ha iniziato a costruire, ma non è stato capace di finire il lavoro
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye nag ibraaymaa ngi doon séentu dëkk bi sax, bi yàlla tabax te sanc ko.
egli aspettava infatti la città dalle salde fondamenta, il cui architetto e costruttore è dio stesso
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci moom la doj yépp ràbbloo, ba tabax bi jóg, di màggalukaay bu sell ngir boroom bi.
in lui ogni costruzione cresce ben ordinata per essere tempio santo nel signore
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ku tabax ci kaw fondamaa bi, wurus, xaalis, per, dénk, gittax walla boob,
e se, sopra questo fondamento, si costruisce con oro, argento, pietre preziose, legno, fieno, paglia
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu yelloo na ndam lu sut lu musaa, ni kiy tabax kër ëppe maana kër ga muy tabax.
ma in confronto a mosè, egli è stato giudicato degno di tanta maggior gloria, quanto l'onore del costruttore della casa supera quello della casa stessa
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te ci seen bokk ci kirist, yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci xel mu sell mi.
in lui anche voi insieme con gli altri venite edificati per diventare dimora di dio per mezzo dello spirito
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dangeen di seede noonu ne, ànd ngeen ak li seen maam defoon, ndaxte ñoo rey yonent yi, yéen ngeen tabax xabru yi.
così voi date testimonianza e approvazione alle opere dei vostri padri: essi li uccisero e voi costruite loro i sepolcri
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«dina mel it ni la xewoon ca bési lóot. nit ñaa ngi doon lekk ak di naan, di jënd ak di jaay, di ji ak di tabax.
come avvenne anche al tempo di lot: mangiavano, bevevano, compravano, vendevano, piantavano, costruivano
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndax tabaxkatu ndaa sañul a fab banam, tabax ci ñaari ndaa, benn bi ngir soxla yu am maana, bi ci des ngir soxla yu ndaw?
forse il vasaio non è padrone dell'argilla, per fare con la medesima pasta un vaso per uso nobile e uno per uso volgare
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte kirist duggul ci bérab bu sell bu nit tabax, muy doon nataal ci bu dëggu bi. waaye dugg na ca biir asamaan sax, ngir taxawal nu ca kanam yàlla léegi.
cristo infatti non è entrato in un santuario fatto da mani d'uomo, figura di quello vero, ma nel cielo stesso, per comparire ora al cospetto di dio in nostro favore
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
su kenn ci yéen bëggee tabax taaxum kaw, ndax du jëkk a toog, xalaat ñaata la ko war a dikke, ngir seet ba xam ndax am na xaalis bu man a àggale liggéey bi?
chi di voi, volendo costruire una torre, non si siede prima a calcolarne la spesa, se ha i mezzi per portarla a compimento
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«yéen xutbakat yi ak farisen yi, naaféq yi, dingeen torox! ndaxte yéena ngi tabax xabruy yonent yi, tey rafetal bàmmeeli ñu jub ñi.
guai a voi, scribi e farisei ipocriti, che innalzate i sepolcri ai profeti e adornate le tombe dei giusti
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu ne ko: «nga ne kër yàlla, gii ñu tabax ci ñeent-fukki at ak juróom benn, man nga koo yékkati ci ñetti fan!»
gli dissero allora i giudei: «questo tempio è stato costruito in quarantasei anni e tu in tre giorni lo farai risorgere?»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«nun daal dégg nanu, mu ne: “dinaa toj kër yàlla, gii loxoy nit liggéey, tabax ci ñetti fan geneen gu nit liggéeyul.”»
«noi lo abbiamo udito mentre diceva: io distruggerò questo tempio fatto da mani d'uomo e in tre giorni ne edificherò un altro non fatto da mani d'uomo»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu daldi leen wax ciy léeb. mu ne leen: «amoon na fi nit ku jëmbët toolu réseñ. mu ñag tool bi, gas pax ngir nal ci réseñ yi, tabax wottukaay, ba noppi batale ko ay beykat, daldi tukki.
gesù si mise a parlare loro in parabole: «un uomo piantò una vigna, vi pose attorno una siepe, scavò un torchio, costruì una torre, poi la diede in affitto a dei vignaioli e se ne andò lontano
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: