Results for yégee translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

bi yeesu yégee loolu nag, mu jóge yude, dellu diiwaanu galile.

Italian

lasciò la giudea e si diresse di nuovo verso la galilea

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko bokk yi yégee nag, ñu yóbbu ko dëkku sesare, yebal ko dëkku tars.

Italian

venutolo però a sapere i fratelli, lo condussero a cesarèa e lo fecero partire per tarso

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi pilaat yégee baat yooyu, mu laajte ne: «ndax nit kii galile la dëkk?»

Italian

udito ciò, pilato domandò se era galile

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko pool ak barnabas yégee nag, ñu daw ca diiwaanu likawni ca dëkk ya ñuy wax listar ak derbë ak wàllaa ya.

Italian

essi se ne accorsero e fuggirono nelle città della licaònia, listra e derbe e nei dintorni

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee boroom réew ma jàng bataaxal ba, laaj ci ban diiwaan la pool dëkk. bi mu yégee ne, mu ngi dëkk silisi,

Italian

dopo averla letta, domandò a paolo di quale provincia fosse e, saputo che era della cilicia, disse

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi mu yégee ne, yeesoo ngi nekk ci diiwaan bi erodd yilif, mu yónnee ko erodd, mi nekkoon ci jamono jooju ci yerusalem.

Italian

e, saputo che apparteneva alla giurisdizione di erode, lo mandò da erode che in quei giorni si trovava anch'egli a gerusalemme

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko nit ña yégee, ñu toppi ko. yeesu teeru leen, di leen wax ci mbirum nguuru yàlla, te di wéral ñi ko aajowoo.

Italian

ma le folle lo seppero e lo seguirono. egli le accolse e prese a parlar loro del regno di dio e a guarire quanti avevan bisogno di cure

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yawut yi jàpp nañu nit kii, bëgg koo rey, waaye bi ma yégee ne, jaambur la ci room, wallu naa ko ak ay xarekat, ba musal ko.

Italian

quest'uomo è stato assalito dai giudei e stava per essere ucciso da loro; ma sono intervenuto con i soldati e l'ho liberato, perché ho saputo che è cittadino romano

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fekk amoon na ca dëkk ba jigéen juy moy yàlla. bi mu yégee ne, yeesoo ngay lekk ca kër farisen ba, mu dem, yóbbaale njaq lu ñu defare doj wu ñuy wax albaatar te def latkoloñ.

Italian

ed ecco una donna, una peccatrice di quella città, saputo che si trovava nella casa del fariseo, venne con un vasetto di olio profumato

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu déggee deewu yaxya nag, mu jóge fa, dugg cig gaal, di dem ca bérab bu wéet. waaye bi ko nit ñi yégee, ñu daldi jóge ci dëkk yi, topp ko ak seeni tànk.

Italian

udito ciò, gesù partì di là su una barca e si ritirò in disparte in un luogo deserto. ma la folla, saputolo, lo seguì a piedi dalle città

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,772,854,107 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK