Results for yaakaaroon translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

Ñi koy kalaame nag, bi ñu taxawee, jiiñuñu ko benn ñaawteef ci yi ma yaakaaroon;

Italian

gli accusatori gli si misero attorno, ma non addussero nessuna delle imputazioni criminose che io immaginavo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fekk yaakaaroon na it ne, pool dina ko jox xaalis; kon mu di ko faral a woolu, ngir waxtaan ak moom.

Italian

sperava frattanto che paolo gli avrebbe dato del denaro; per questo abbastanza spesso lo faceva chiamare e conversava con lui

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi erodd gisee yeesu, mu am mbég mu réy. bu yàgg ba tey dafa koo bëggoon a gis, ndaxte déggoon na ñuy wax ci ay mbiram te yaakaaroon na ne, dina ko gis mu def kéemaan.

Italian

vedendo gesù, erode si rallegrò molto, perché da molto tempo desiderava vederlo per averne sentito parlare e sperava di vedere qualche miracolo fatto da lui

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,664,226 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK