Results for xamuleen translation from Wolof to Japanese

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Japanese

Info

Wolof

moytuleen te xool! xamuleen kañ la waxtu wi di jot.

Japanese

気をつけて、目をさましていなさい。その時がいつであるか、あなたがたにはわからないからである。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeewuleen nag, ndaxte xamuleen bés bu seen boroom di ñëw.

Japanese

だから、目をさましていなさい。いつの日にあなたがたの主がこられるのか、あなたがたには、わからないからである。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen ñi bëgg a topp yoon wi, xanaa xamuleen li yoonu musaa wi wax?

Japanese

律法の下にとどまっていたいと思う人たちよ。わたしに答えなさい。あなたがたは律法の言うところを聞かないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, nooy àtteji malaaka yi? waxatumaak mbiri àddina sii.

Japanese

あなたがたは知らないのか、わたしたちは御使をさえさばく者である。ましてこの世の事件などは、いうまでもないではないか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, yéenay kër yàlla, te xelum yàlla dëkk na ci yéen?

Japanese

あなたがたは神の宮であって、神の御霊が自分のうちに宿っていることを知らないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xamuleen ne, lépp lu dugg ci gémmiñ, ci biir lay jëm tey génn ca bérab bu làqu?

Japanese

口にはいってくるものは、みな腹の中にはいり、そして、外に出て行くことを知らないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu tontu leen: «am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko.»

Japanese

ところが、イエスは言われた、「わたしには、あなたがたの知らない食物がある」。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

seen tiitar bi jekkul dara. xanaa xamuleen ne, tuuti lawiir day tax tooyalu fariñ bépp funki?

Japanese

あなたがたが誇っているのは、よろしくない。あなたがたは、少しのパン種が粉のかたまり全体をふくらませることを、知らないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yeesu ne leen: «ndax xamuleen léeb wii? nu ngeen xame nag léeb yi ci des?

Japanese

また彼らに言われた、「あなたがたはこの譬がわからないのか。それでは、どうしてすべての譬がわかるだろうか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu tontu leen ne: «yéena ngi cig réer, ndaxte xamuleen mbind mi mbaa kàttanu yàlla.

Japanese

イエスは答えて言われた、「あなたがたは聖書も神の力も知らないから、思い違いをしている。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, kenn nit rekk dee ngir ñépp, mooy li gën ci yéen? bu ko defee réew mi du tas.»

Japanese

ひとりの人が人民に代って死んで、全国民が滅びないようになるのがわたしたちにとって得だということを、考えてもいない」。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne leen: «lu tax ngeen may seet? xanaa xamuleen ne, damaa war a nekk ci sama kër baay?»

Japanese

するとイエスは言われた、「どうしてお捜しになったのですか。わたしが自分の父の家にいるはずのことを、ご存じなかったのですか」。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen waa samari, xamuleen li ngeen di jaamu. nun yawut yi, xam nanu li nuy jaamu, ndaxte kiy musal àddina ci yawut yi la jóge.

Japanese

あなたがたは自分の知らないものを拝んでいるが、わたしたちは知っているかたを礼拝している。救はユダヤ人から来るからである。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, seen yaram ñooy céri kirist? ndax kon damay jël céri kirist, def ko céri jigéeni moykat? mukk!

Japanese

あなたがたは自分のからだがキリストの肢体であることを、知らないのか。それだのに、キリストの肢体を取って遊女の肢体としてよいのか。断じていけない。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla, xanaa xamuleen ne mbëggeelu àddina, mbañeel la fa yàlla? ku bëgg a xaritoo ak àddina nag, noonoo nga ak yàlla.

Japanese

不貞のやからよ。世を友とするのは、神への敵対であることを、知らないか。おおよそ世の友となろうと思う者は、自らを神の敵とするのである。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, ñiy liggéeyal yëf yu sell yi, dañuy lekk ñam, wi ci kër yàlla gi, te ñiy liggéey ci saraxalukaay bi, dañuy jot seen wàll ci sarax yi?

Japanese

あなたがたは、宮仕えをしている人たちは宮から下がる物を食べ、祭壇に奉仕している人たちは祭壇の供え物の分け前にあずかることを、知らないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu tontu leen ne: «ndax yéen itam seen xol dafa tëju? xanaa xamuleen ne, dara lu jóge biti, dugg ci nit, du ko man a indil sobe,

Japanese

すると、言われた、「あなたがたも、そんなに鈍いのか。すべて、外から人の中にはいって来るものは、人を汚し得ないことが、わからないのか。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, ñi jubadi duñu bokk ci nguuru yàlla? bu leen ci kenn nax: ñiy doxaan walla xërëmkat yi ak njaalookat yi ak góor-jigéen ñi ak ñi ko nangu,

Japanese

それとも、正しくない者が神の国をつぐことはないのを、知らないのか。まちがってはいけない。不品行な者、偶像を礼拝する者、姦淫をする者、男娼となる者、男色をする者、盗む者、

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne ko: «xamuleen li ngeen di ñaan. ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan?» Ñu tontu ko: «man nañu ko.»

Japanese

イエスは答えて言われた、「あなたがたは、自分が何を求めているのか、わかっていない。わたしの飲もうとしている杯を飲むことができるか」。彼らは「できます」と答えた。

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,260,361,465 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK