Results for erodd translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

ca jamono joojale erodd boroom diiwaanu galile dégg na tur, wa yeesu am.

Russian

В то время Ирод четвертовластник услышал молву об Иисусе

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

erodd nag bëgg koo rey, waaye dafa ragal nit ñi, ci li ñu teg yaxya ab yonent.

Russian

И хотел убить его, но боялся народа, потому что его почитали за пророка.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi nga xamee ne erodd faatu na, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ca misra,

Russian

По смерти же Ирода, - се, Ангел Господень во сне является Иосифу в Египте

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee ñu yónni ci yeesu ay farisen ak ñu far ak buur bi erodd, ngir fiir ko ci waxam.

Russian

И посылают к Нему некоторых из фарисеев и иродиан,чтобы уловить Его в слове.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ca bés ba ñu jàpp nag erodd sol mbubbi buuram, toog ca jal ba ca àttekaay ba, di leen yedd ak a dénk.

Russian

В назначенный день Ирод, одевшись в царскую одежду, сел на возвышенном месте и говорил к ним;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte erodd jàppoon na yaxya, yeew ko, tëj. ndaxte erodd takkoon na erojàdd, jabaru filib magam,

Russian

Ибо Ирод, взяв Иоанна, связал его и посадил в темницу за Иродиаду, жену Филиппа, брата своего,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bi ko erodd déggee, mu ne: «yaxya male ma dagglu boppam, moom moo dekki.»

Russian

Ирод же, услышав, сказал: это Иоанн, которого я обезглавил; он воскрес из мертвых.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi mu yégee ne, yeesoo ngi nekk ci diiwaan bi erodd yilif, mu yónnee ko erodd, mi nekkoon ci jamono jooju ci yerusalem.

Russian

И, узнав, что Он из области Иродовой, послал Его к Ироду, который в эти дни был также в Иерусалиме.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu ca tegee ab diir nag, ñuy màggal bés ba erodd juddu woon, te doomu erojàdd ju jigéen di fecc ci biir gan ñi. loolu neex erodd,

Russian

Во время же празднования дня рождения Ирода дочьИродиады плясала перед собранием и угодила Ироду,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bi mu déggee ne, arkelawus moo donn erodd baayam ca nguuru yude, mu ragal faa dem. yàlla artu ko nag ci gént, mu daldi dem diiwaanu galile.

Russian

Услышав же, что Архелай царствует в Иудее вместо Ирода, отца своего, убоялся туда идти; но, получив во сне откровение, пошел в пределы Галилейские

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi erodd nekkee ci tànki indilu ko, ca guddi googa yeewoon nañu piyeer ak ñaari càllala, muy nelaw diggante ñaari xarekat, te ay xarekat di wottu buntu kaso ba.

Russian

Когда же Ирод хотел вывести его, в ту ночь Петр спал между двумя воинами, скованныйдвумя цепями, и стражи у дверей стерегли темницу.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne ko: «kon bu ñi la kalaame ñëwee, dinga layoo.» mu santaane nag, ñu denc ko ca kër buur ba erodd.

Russian

я выслушаю тебя, когда явятся твои обвинители. Иповелел ему быть под стражеюв Иродовой претории.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sànn, jabaru ku ñuy wax kusa, mi doon wottu alalu erodd; ak susànn ak ñeneen jigéen. jigéen ñooñu ñoo doon joxe seen alal, ngir dimbali yeesu ak ay taalibeem.

Russian

и Иоанна, жена Хузы, домоправителя Иродова, и Сусанна, и многие другие, которые служили Ему имением своим.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu erodd buur bi dégg loolu, ndaxte turu yeesu siiwoon na. mu ne nag: «yaxya dekki na, moo tax mu ànd ak kàttanu def ay kéemaan.»

Russian

Царь Ирод, услышав об Иисусе , - ибо имя Его стало гласно, - говорил: это Иоанн Креститель воскрес из мертвых, и потому чудеса делаются им.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na ci mbooloom ñi gëm, mi nekk dëkku ancos, ay yonent ak ay jàngalekat: maanaam barnabas, simeyon ku ñu dàkkentale niseer, lusiyus mi dëkk siren, manayen mi yaroondoo ak erodd boroom diiwaan ba, ak sool.

Russian

В Антиохии, в тамошней церкви были некоторые пророки и учители: Варнава, и Симеон, называемый Нигер, и Луций Киринеянин, и Манаил, совоспитанник Ирода четвертовластника, и Савл.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,913,795,075 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK