Results for jébbal translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

Ñu jébbal leen ndaw ya, ñaanal leen, teg leen loxo.

Russian

их поставили перед Апостолами, и сии , помолившись, возложили на них руки.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu yeew ko, yóbbu ko, jébbal ko pilaat boroom réew ma.

Russian

и, связав Его, отвели и предали ЕгоПонтию Пилату, правителю.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu waxambaane ya jóg, ñu sàng ko, yóbbu ko, jébbal yàlla.

Russian

И встав, юноши приготовили его к погребению и, вынеся, похоронили.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li dale ci saa soosa nag yudaa di fexe jamono ju mu leen man a jébbal yeesu.

Russian

и с того времени он искал удобного случая предать Его.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ay nit ñu ragal yàlla fab ecen, jébbal ko boroom bi, di ko jooy bu wér.

Russian

Стефана же погребли мужи благоговейные, и сделаливеликий плач по нем.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu tàggoo, dem ancos, ñu dajale mbooloo mi, jébbal leen bataaxal bi.

Russian

Итак, отправленные пришли в Антиохию и, собрав людей, вручили письмо.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dinañu ko jébbal ñi dul yawut, ñu ñaawal ko, saaga ko, tifli ci kawam.

Russian

ибо предадут Его язычникам, и поругаются над Ним, и оскорбят Его, и оплюют Его,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye moytuleen nit ñi, ndaxte dinañu leen jébbal àttekat yi te dóor leen ay yar ci seeni jàngu.

Russian

Остерегайтесь же людей: ибо они будут отдавать вас в судилища и в синагогах своих будут бить вас,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag nanu jaare ci yeesu, tey dëkk ci jébbal yàlla sarax bu koy màggal, maanaam sant turam.

Russian

Итак будем через Него непрестанно приносить Богу жертву хвалы, то есть плод уст,прославляющих имя Его.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«dégluleen bu baax lii ma leen di wax: dinañu jébbal doomu nit ki ci loxoy nit ñi.»

Russian

вложите вы себе в уши слова сии: Сын Человеческий будет предан в руки человеческие.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ-sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax; keneen la ko jébbal,

Russian

Ибо не Ангелам Бог покорил будущую вселенную, о которой говорим;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu ko déggee, ñu am ca bànneex bu réy, dig ko xaalis. noonu mu fexe jamono ju mu leen man a jébbal yeesu.

Russian

Они же, услышав, обрадовались, и обещали дать ему сребренники. И он искал, как бы в удобное времяпредать Его.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñuy wër diiwaanu galile nag, yeesu ne leen: «léegi ñu jébbal doomu nit ki ci loxoy nit ñi;

Russian

Во время пребывания их в Галилее, Иисус сказал им: Сын Человеческий предан будет в руки человеческие,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ay nit doon wax ci lu jëm ca kër yàlla ga, ak ni ñu ko rafetale ak ay doj yu jafe ak alal ju ñu jébbal yàlla. waaye yeesu ne leen:

Russian

И когда некоторые говорили о храме, что он украшендорогими камнями и вкладами, Он сказал:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

jébbal ko ñi dul yawut, ngir ñu di ko ñaawal te di ko dóor ay yar, ba noppi daaj ko ci bant. waaye ca ñetteelu fan ba dina dekki.»

Russian

и предадут Его язычникам на поругание и биение и распятие; и в третий день воскреснет.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ne leen: «lan ngeen ma man a jox, ngir ma jébbal leen yeesu?» noonu saraxalekat ya daldi ko waññal fanweeri poseti estateer.

Russian

и сказал: что вы дадите мне, и я вам предам Его? Они предложили ему тридцать сребренников;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pilaat ne ko: «mbaa xalaatoo ne, man yawut laa? sa xeet ak saraxalekat yu mag yi ñoo ma la jébbal. lan nga def?»

Russian

Пилат отвечал: разве я Иудей? Твой народ и первосвященники предали Тебя мне; что Ты сделал?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pilaat nag xam ne, kiñaan rekk a taxoon saraxalekat yu mag yi jébbal ko yeesu. kon mu ne mbooloo mi: «xanaa ma bàyyil leen buuru yawut yi?»

Russian

Он сказал им в ответ: хотите ли, отпущу вам Царя Иудейского?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ngëm moo tax ba abel jébbal yàlla sarax su gën saraxu kayin. ngëmu abel moo tax ba yàlla àtte ko ni ku jub, bi mu ko seedeelee ne, saraxam baax na. te ci kaw ngëm lay wax ba tey, moom mi dee ba noppi.

Russian

Верою Авель принес Богу жертву лучшую, нежели Каин; ею получил свидетельство, что он праведен, как засвидетельствовал Бог о дарах его; ею он и по смерти говорит еще.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yoonu musaa dafa misaal xéewal yi waroon a ñëw; takkandeer la ci yëf yu dëggu yi, waaye du ñoom ci seen bopp. looloo tax mënul a yeggale cig mat ñi ñëw ci yàlla, ndaxte at mu nekk duñu jóg ci jébbal yàlla sarax yooyu.

Russian

Закон, имея тень будущих благ, а не самый образ вещей, одними и теми же жертвами, каждый год постоянно приносимыми, никогда не может сделать совершенными приходящих с ними .

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,943,171,978 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK