Results for laabiir translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

ku bëgg dafay muñ te laabiir. ku bëgg du kiñaan, du kañu, du tiitaru,

Russian

Любовь долготерпит, милосердствует, любовь не завидует,любовь не превозносится, не гордится,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dafa wax musaa sax ne ko:«dinaa yërëm ku ma neex,laabiir ci ku ma neex.»

Russian

Ибо Он говорит Моисею: кого миловать, помилую; кого жалеть, пожалею.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te waa réew ma won nu laabiir gu ràññiku, ndaxte taalal nañu nu safara, ganale nu ndax taw bi sóob ak sedd bi.

Russian

Иноплеменники оказали нам немалое человеколюбие, ибо они, по причине бывшего дождя и холода, разложили огонь и приняли всех нас.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ca ëllëg sa nu teer sidon; yulyus laabiir ci pool, may ko mu dem ci ay xaritam, ngir ñu ganale ko.

Russian

На другой день пристали к Сидону. Юлий, поступая с Павлом человеколюбиво, позволил ему сходить к друзьям и воспользоваться их усердием.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye li xelu yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

Russian

Плод же духа: любовь, радость, мир, долготерпение, благость, милосердие, вера,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag ndegam yàlla tànn na leen, sellal leen, sopp leen, solooleen boog yërmande, laabiir, woyof, lewet ak muñ.

Russian

Итак облекитесь, как избранные Божии, святые и возлюбленные, в милосердие, благость, смиренномудрие, кротость, долготерпение,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nu ngi rafetal sunu yen ci dund gu sell, ci xam-xam, muñ ak laabiir, ci xel mu sell mi ak ci mbëggeel gu raxul njublaŋ,

Russian

в чистоте, в благоразумии, в великодушии, в благости, в Духе Святом, в нелицемерной любви,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,740,308 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK