Results for rangooñ translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

jaamu naa boroom bi ci woyof gu mat ak ay rangooñ, dékku ay nattu yu ma pexey yawut yi indil.

Russian

работая Господу со всяким смиренномудрием и многими слезами, среди искушений, приключавшихся мне по злоумышлениям Иудеев;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foogleen nag, di fàttaliku ne diirub ñetti at, guddi ak bëccëg, musumaa noppi di leen artu kenn ku nekk ci yéen ak ay rangooñ.

Russian

Посему бодрствуйте, памятуя, что я три года день и ночь непрестанно со слезами учил каждого из вас.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte mbote mi nekk ci diggu gàngune mi dina leen sàmm,yóbbu leen ca bëti ndoxum dund ma,te yàlla dina fomp bépp rangooñ ci seeni bët.»

Russian

ибо Агнец, Который среди престола, будет пасти их и водить их на живые источники вод; и отрет Бог всякую слезу с очей их.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci biir tiis ak xol bu jeex laa leen bind, samay bët taa ak ay rangooñ. binduma leen ngir teg leen naqar, waaye ngir ngeen xam xóotaayu mbëggeel gi ma am ci yéen.

Russian

От великой скорби и стесненного сердца я писал вам со многими слезами, не для того, чтобы огорчить вас, но чтобы вы познали любовь, какую я в избытке имею к вам.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fu ma tollu maa ngi lay boole ci samay ñaan, di ci sant yàlla, mi may jaamu ci xel mu dal, ni ko samay maam daan defe. guddi ak bëccëg, bu sama xel demee ci say rangooñ,

Russian

Благодарю Бога, Которому служу от прародителей с чистою совестью, что непрестанно вспоминаю о тебе в молитвах моих днем и ночью,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

giiru dundam gépp ci àddina, kirist da daan ñaan wall ci yàlla, di ko dénku, boole ko ak i jooy ak i rangooñ. da doon ñaan ci yàlla, mi ko man a musal ci dee. te ñaanam nangu na, ndax ni mu jébbale boppam yàlla.

Russian

Он, во дни плоти Своей, с сильным воплем и со слезами принес молитвы и моления Могущему спасти Его от смерти; и услышан был за Своеблагоговение;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,927,565,503 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK