Results for xërëm translation from Wolof to Russian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Russian

Info

Wolof

samay doom, wottuleen seen bopp ciy xërëm.

Russian

Дети! храните себя от идолов. Аминь.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

looloo tax, sama soppe yi, nangeen daw xërëm yi.

Russian

Итак, возлюбленные мои, убегайте идолослужения.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw miy araamal xërëm yi, mbaa doo sàcc li nekk ci seeni xàmb?

Russian

Проповедуя не красть, крадешь? говоря: „не прелюбодействуй", прелюбодействуешь? гнушаясь идолов, святотатствуешь?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

te nit ñooñu tuubuñu seen bóom, seen xërëm, seen njaaloo mbaa seen càcc.

Russian

И не раскаялись они в убийствах своих, ни в чародействах своих, ни в блудодеянии своем, ни в воровстве своем.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

booba nag ñu tëgglu aw sëllu, muy xërëm, ñu di ko tuuru, di bànneexu ci seeni jëfi loxo.

Russian

И сделали в те дни тельца, и принесли жертву идолу, и веселились перед делом рук своих.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xërëm, luxus, noonoo ak xuloo, ñeetaane, xadar, diiroo mbagg, féewaloo ak xaajaloo,

Russian

идолослужение, волшебство, вражда, ссоры, зависть, гнев, распри, разногласия,(соблазны), ереси,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam ngeen ne, bi ngeen xamagul woon yàlla, xërëm, yi mënul a wax, ñoo leen jiitaloon, di leen wommat.

Russian

Знаете, что когда вы были язычниками, тоходили к безгласным идолам, так, как бы вели вас.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li may wax, lu muy tekki? ndax yàpp wi ñu jagleel xërëm yi dafay dara? walla xërëm yi dañuy dara?

Russian

Что же я говорю? То ли, что идол есть что-нибудь,или идоложертвенное значит что-нибудь?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka ñi dul yawut ñi gëm, bind nanu leen li nu àtte ne, ñu moytu ñam wu ñu tuuroo xërëm te moytu deretu médd ak njaaloo.»

Russian

А об уверовавших язычниках мы писали, положив, чтобы они ничего такого не наблюдали, а только хранили себя от идоложертвенного, от крови, от удавленины и от блуда.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye li ma naqari ci yaw moo di dangaa bàyyi yesabel, jigéen joojuy tuddoo yonent, di jàngale ak a réeral sama jaam yi, ngir ñuy sóobu ci njaaloo te di lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi.

Russian

Но имею немного против тебя, потому что ты попускаешь жене Иезавели, называющей себя пророчицею, учить и вводить в заблуждение рабов Моих, любодействовать и есть идоложертвенное.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte àndoon ngeen démb ci xalaati ñi xamul yàlla, di dund ciy ñaawteef ak topp seen bakkan, di màndi ak a xawaare, di xér ci biiñ ak a jaamu ay xërëm yu araam, waaye na fi yem nag.

Russian

Ибо довольно, что вы в прошедшее время жизни поступали по воле языческой, предаваясь нечистотам, похотям(мужеложству, скотоложству, помыслам), пьянству, излишеству в пище и питии и нелепому идолослужению;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye am na lu ma naqari ci yaw, moo di uuf nga foofu gaa yuy sàmm njàngalem balaam, moom mi jàngaloon balag, mu sóob bànni israyil ci bàkkaar, xiir leen ci lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi, xiir leen ci njaaloo.

Russian

Но имею немного против тебя, потому что есть у тебятам держащиеся учения Валаама, который научил Валака ввести в соблазн сынов Израилевых, чтобы они ели идоложертвенное и любодействовали.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

buleen jaamu ay xërëm, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe woon. ndaxte mbind mi nee na: «mbooloo mi dafa toog, di lekk ak di naan, ba noppi ñu jóg di mbumbaay.»

Russian

Не будьте также идолопоклонниками, как некоторые из них, о которых написано: народ сел есть и пить, и встал играть.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,070,202 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK