From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
buuri àddina dañoo booloo,te kilifa yi dajaloo,di bañ boroom bi ak almaseem.”
se levantaron los reyes de la tierra y sus gobernantes consultaron unidos contra el señor y contra su ungido
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye noonu la yàlla amale li mu yégle woon lu jiitu jaarale ko ci gémmiñug yonent yépp naan, almaseem dina sonn.
pero dios cumplió así lo que había anunciado de antemano por boca de todos los profetas, de que su cristo había de padecer
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ma dégg baat bu xumb jóge asamaan naan:«léegi mucc agsi na,moom ak kàttanak nguuru yàlla sunu boroom,ak sañ-sañu almaseem,ndaxte ki daan tuumaal sunuy bokk,di leen sosal guddi ak bëccëgci kanam yàlla sunu boroom,kooka daaneel nañu ko.
oí una gran voz en el cielo que decía: "¡ahora ha llegado la salvación y el poder y el reino de nuestro dios, y la autoridad de su cristo! porque ha sido arrojado el acusador de nuestros hermanos, el que los acusaba día y noche delante de nuestro dios
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting