Results for biddiiw translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

ba ñu gisee biddiiw ba nag, ñu am mbég mu réy-a-réy.

Spanish

al ver la estrella, se regocijaron con gran alegría

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

biddiiw boobu mi ngi tuddoon wextan. nit ñu bare naan ci ndox mi daldi dee, ndaxte ndox mi dafa daldi wex.

Spanish

el nombre de la estrella es ajenjo. y la tercera parte de las aguas se convirtió en ajenjo, y muchos hombres murieron por las aguas, porque fueron hechas amargas

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

biddiiw yi fàqe asamaan, di daanu ci kaw suuf, ni doomi garab yu yolox di wadd, bu ko ngelaw lu metti dee yengal.

Spanish

y las estrellas del cielo cayeron sobre la tierra, como una higuera arroja sus higos tardíos cuando es sacudida por un fuerte viento

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

juróomeelu malaaka ma wol liitam. noonu ma gis, ñu jox caabiy kàmb gu xóot gi benn biddiiw bu xawee woon asamaan, daanu ci kaw suuf.

Spanish

el quinto ángel tocó la trompeta. y vi que una estrella había caído del cielo a la tierra, y le fue dada la llave del pozo del abismo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

biddiiw ba ubbi buntu kàmb gu xóot ga. noonu saxar jollee ca, su mel ni saxarus puur bu mag, jant bi ak jaww ji lépp lëndëm ndax saxarus kàmb ga.

Spanish

y abrió el pozo del abismo, y subió humo del pozo como el humo de un gran horno; y fue oscurecido el sol y también el aire por el humo del pozo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ba ñu dégloo buur ba nag, ñu dem. te biddiiw, ba ñu gisoon ca penku ba, ne tell jiite leen, ba àgg, tiim fa xale ba nekk.

Spanish

ellos, después de oír al rey, se fueron. y he aquí la estrella que habían visto en el oriente iba delante de ellos, hasta que llegó y se detuvo sobre donde estaba el niño

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu yor ci loxol ndeyjooram juróom-ñaari biddiiw, jaasiy ñaari boor yu ñaw di génn ci gémmiñam, xar-kanamam leer nàññ ni jantub njolloor.

Spanish

tenía en su mano derecha siete estrellas, y de su boca salía una espada aguda de dos filos. su rostro era como el sol cuando resplandece en su fuerza

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, jaaxle ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.

Spanish

entonces habrá señales en el sol, en la luna y en las estrellas. y en la tierra habrá angustia de las naciones por la confusión ante el rugido del mar y del oleaje

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«gannaaw metitu bés yooyule nag, ca saa sa jant bi dina lëndëm te weer wi dootul leer; biddiiw yi dinañu fàq, daanu ci asamaan, te kàttani asamaan yi yengu.

Spanish

pero inmediatamente después de la tribulación de aquellos días, el sol se oscurecerá, y la luna no dará su resplandor. las estrellas caerán del cielo y los poderes de los cielos serán sacudidos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku efes, ne ko: i ki téye juróom-ñaari biddiiw yi ci loxol ndeyjooram, tey dox ci diggu juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi nee na:

Spanish

"escribe al ángel de la iglesia en Éfeso: el que tiene las siete estrellas en su mano derecha, el que camina en medio de los siete candeleros de oro, dice estas cosas

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,779,162,257 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK