From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
lu tax yaw itam yërëmoo sa moroom, ni ma la yërëme?”
¿no debías tú también tener misericordia de tu consiervo, así como también yo tuve misericordia de ti?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
soo ma jàppee ni nawle nag, teeru ko, ni su ma la doon ganesi.
así que, si me tienes por compañero, recíbele como a mí mismo
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kon fabal li nga moom te dem. su ma bëggee fey ku mujj a ñëw, li ma la fey yaw,
toma lo que es tuyo y vete. pero quiero darle a este último como a ti
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu bind naa la, ndax wóor na ma ne, dinga ma déggal, ba weesu sax li ma la sant.
habiendo confiado en tu obediencia, te escribo sabiendo que harás aun más de lo que digo
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu ma la yónnee artemas walla tisig, gaawantul fekksi ma ci dëkku nikopolis, ndax fa laa bëgg a lollikooji.
cuando yo envíe a ti a artemas o a tíquico, procura venir a mí a nicópolis, pues allí he decidido pasar el invierno
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo tax maa ngi lay fàttali, nga xambaat taal bi yàlla taal ci yaw, di may gi mu la jagleel, bi ma la tegee samay loxo.
por esta razón, te vuelvo a recordar que avives el don de dios que está en ti por la imposición de mis manos
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
am na lu ma la bëgg a ñaan; teguma ko ci sañ-sañ bu mat bi ma kirist may, ci teg la ndigalu def sa warugar,
por lo tanto, aunque tengo mucha confianza en cristo para ordenarte lo que conviene
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pilaat ne ko: «mbaa xalaatoo ne, man yawut laa? sa xeet ak saraxalekat yu mag yi ñoo ma la jébbal. lan nga def?»
pilato respondió: --¿acaso soy yo judío? tu propia nación y los principales sacerdotes te entregaron a mí. ¿qué has hecho
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne ca tonn, daldi ne farisen ba: «simoŋ, am na lu ma la war a wax.» simoŋ ne ko: «waxal, kilifa gi.»
entonces, respondiendo jesús le dijo: --simón, tengo algo que decirte. Él dijo: --di, maestro
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.