From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
damala nammou
Last Update: 2024-02-18
Usage Frequency: 1
Quality:
bi nga xamee ne fukki taalibe ya dégg nañu loolu, ñu mere ñaari doomi ndey ya.
cuando los diez oyeron esto, se enojaron contra los dos hermanos
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi nga xamee ne fukki taalibe ya ca des dégg nañu loolu, ñu daldi mere saag ak yowaana.
cuando lo oyeron los diez, comenzaron a enojarse con jacobo y juan
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ninkinànka ja mere jigéen ja, daldi xeexi ak ñi des ciy doomam, di ñiy sàmm ndigali yàlla tey sax ci di seedeel yeesu.
entonces el dragón se enfureció contra la mujer, y se fue para hacer guerra contra los demás descendientes de ella, quienes guardan los mandamientos de dios y tienen el testimonio de jesucristo. y él se puso de pie sobre la arena del mar
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te ñan la yàlla mere lu mat ñeent-fukki at? xanaa ñi daan bàkkaar te seeni néew tëdd ca màndiŋ ma.
¿y con quiénes se disgustó durante cuarenta años? ¿no fue precisamente con los que pecaron, cuyos cuerpos cayeron en el desierto
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye man maa ngi leen di wax ne, képp ku mere sa mbokk, dinañu la àtte. ku wax sa mbokk: “amoo bopp,” dinañu la àtte ca kureelu àttekat ya. ku ko wax: “alku nga,” dinañu la àtte ci safara.
pero yo os digo que todo el que se enoja con su hermano será culpable en el juicio. cualquiera que le llama a su hermano 'necio' será culpable ante el sanedrín; y cualquiera que le llama 'fatuo' será expuesto al infierno de fuego
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: