Results for diirub translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

diirub ñetti fan gisul dara, lekkul, naanul.

Spanish

por tres días estuvo sin ver, y no comió ni bebió

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

diirub ñeent-fukki at mu di leen muñal ca màndiŋ ma.

Spanish

por un tiempo como de cuarenta años los soportó en el desierto

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na fa nag jigéen ju doon xëpp deret diirub fukki at ak ñaar.

Spanish

había una mujer que sufría de hemorragia desde hacía doce años

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag bokk yi, toppleen ma te xool ñiy roy ci li nu tëral diirub sunu ngan ci yéen.

Spanish

hermanos, sed imitadores de mí y prestad atención a los que así se conducen, según el ejemplo que tenéis en nosotros

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu diirub ñaari at pool dëkk ca kër gu muy fey, di fa àggali ñépp ñi koy seetsi.

Spanish

pablo permaneció dos años enteros en una casa que alquilaba. a todos los que venían a él, les recibía allí

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu gis fa nit ku làggi, tudd ene, tëdd ci basaŋ diirub juróom-ñetti at.

Spanish

allí encontró a cierto hombre llamado eneas, que estaba postrado en cama desde hacía ocho años, pues era paralítico

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na nag ca mbooloo ma jigéen ju doon xëpp deret diirub fukki at ak ñaar, te kenn mënu ko woon a faj.

Spanish

y una mujer, que padecía de hemorragia desde hacía doce años (la cual, aunque había gastado todo su patrimonio en médicos, no pudo ser sanada por nadie)

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu wéy ci noonu diirub ñaari at, ba ñi dëkk diiwaanu asi ñépp dégg kàddug boroom bi, muy yawut muy gereg.

Spanish

esto continuó por dos años, de manera que todos los que habitaban en asia, tanto judíos como griegos, oyeron la palabra del señor

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bokk yi, yéen ñi may waxal xam ngeen luy yoon; xam ngeen kon ne, yoon am na doole ci nit diirub dundam.

Spanish

hermanos (hablo con los que conocen la ley), ¿ignoráis que la ley se enseñorea del hombre entre tanto que vive

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foogleen nag, di fàttaliku ne diirub ñetti at, guddi ak bëccëg, musumaa noppi di leen artu kenn ku nekk ci yéen ak ay rangooñ.

Spanish

por tanto, velad, acordándoos que por tres años, de noche y de día, no cesé de amonestar con lágrimas a cada uno

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na nag ca wet ya ay suuf yu doon moomeelu ku tudd publiyus, di kilifag dun ba. mu teeru nu, ganale nu ngan gu réy diirub ñetti fan.

Spanish

en aquellos lugares estaban las propiedades del hombre principal de la isla, que se llamaba publio. Éste nos recibió y nos hospedó de manera amistosa por tres días

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moo leen génne réewu misra, di def ay kéemaan ak ay firnde ca réew ma, ca géej gu xonq ga ak ca màndiŋ ma diirub ñeent-fukki at.

Spanish

Él los sacó, haciendo prodigios y señales en egipto, en el mar rojo y en el desierto por cuarenta años

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka noonu iliyas nit la woon ku bindoo ni nun, waaye bi mu saxee ci ñaan yàlla, ngir mu bañ a taw, ndox laalul suuf diirub ñetti at ak genn-wàll.

Spanish

elías era un hombre sujeto a pasiones, igual que nosotros, pero oró con insistencia para que no lloviera, y no llovió sobre la tierra durante tres años y seis meses

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«fukki béjjén yi nga gis, fukki buur lañu yu jotagul nguur. waaye dinañu jot sañ-sañ diirub waxtu, ñuy nguuru ak rab wi.

Spanish

los diez cuernos que has visto son diez reyes que todavía no han recibido reino, pero toman autoridad por una hora como reyes junto con la bestia

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bul ragal li nga nar a daj. seytaane dina dugal kaso ñenn ci yéen, ngir wut leen a fiir. diirub fukki fan dingeen am coono. nanga takku ba àttan cee dee, ma jox la kaalag dund gi. i

Spanish

no tengas ningún temor de las cosas que has de padecer. he aquí, el diablo va a echar a algunos de vosotros en la cárcel para que seáis probados, y tendréis tribulación por diez días. sé fiel hasta la muerte, y yo te daré la corona de la vida

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yàlla ne ko: “Ñi soqikoo ci yaw dinañu ganeyaan ci réew mu ñu dëkkul; dees na leen def ay jaam, di leen fitnaal diirub ñeenti téeméeri at.”

Spanish

así dios le dijo que su descendencia sería extranjera en tierra ajena y que los reducirían a esclavitud y los maltratarían por cuatrocientos años

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu jigéen ja daw, dem ca màndiŋ ma, ca dalukaay ba ko yàlla waajaloon ngir mu nekk fa, ñu dundal ko fa diirub junni ak ñaari téeméeri fan ak juróom-benn-fukk.

Spanish

y la mujer huyó al desierto, donde tenía un lugar que dios había preparado, para ser alimentada allí durante 1.260 días

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,877,205,263 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK