Results for nar translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

nar dounou yap

Spanish

Last Update: 2023-05-19
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ak yudaa iskariyo mi nar a wor yeesu.

Spanish

y a judas iscariote (el que le entregó). Él volvió a casa

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye dinañu mas a teew fa kanam ki nar a àtte ñiy dund ak ñi dee.

Spanish

ellos darán cuenta a quien ha de juzgar a los vivos y a los muertos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag bindal li nga gis, li am léegi ak li nar a ami gannaaw gi.

Spanish

así que, escribe las cosas que has visto, y las que son, y las que han de ser después de éstas

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kenn ca taalibey yeesu ya, muy yudaa iskariyo, mi ko nar a wor, daldi ne:

Spanish

pero uno de sus discípulos, judas iscariote, el que estaba por entregarle, dijo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu gis ne dañu koo nar a jëlsi, fal ko buur. mu bàyyi leen fa, dellu moom rekk ca tund wa.

Spanish

como jesús entendió que iban a venir para tomarle por la fuerza y hacerle rey, se retiró de nuevo al monte, él solo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te dina nas bépp naxe buy sànke, ba yéem ñi nar a alku, ndaxte ubbiluñu seeni xol dëgg, gi leen manoon a musal.

Spanish

y con todo engaño de injusticia entre los que perecen, por cuanto no recibieron el amor de la verdad para ser salvos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu boobaa nit ñiy xëm ndax tiitaange, bu ñuy xalaat musiba, yi nar a wàcc ci àddina, ndaxte dees na yengal kàttani asamaan.

Spanish

los hombres se desmayarán a causa del terror y de la expectación de las cosas que sobrevendrán al mundo habitado, porque los poderes de los cielos serán sacudidos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa iskariyo, mi nar a wor yeesu.

Spanish

simón el cananita y judas iscariote, quien le entregó

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yudaa, mi ko nar a wor, laaj ko: «mbaa du man, kilifa gi?» yeesu ne ko: «wax nga ko.»

Spanish

y respondiendo judas, el que le entregaba, dijo: --¿acaso seré yo, maestro? le dijo: --tú lo has dicho

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,900,025,755 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK