Results for saaga translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

Ñu ngi ko doon tifaar it yeneeni saaga.

Spanish

y le decían otras muchas cosas, injuriándole

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dinañu ko jébbal ñi dul yawut, ñu ñaawal ko, saaga ko, tifli ci kawam.

Spanish

porque será entregado a los gentiles, y será escarnecido, injuriado y escupido

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

saaga nañu ko te feyyuwul, fitnaal nañu ko te tëkkuwul, waaye mu dénk boppam ki yor àtte bu dëgg bi.

Spanish

cuando le maldecían, él no respondía con maldición. cuando padecía, no amenazaba, sino que se encomendaba al que juzga con justicia

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

barkeel ngeen, bu leen nit ñi bañee, di leen dàq ak a saaga, di sib seen tur ngir doomu nit ki.

Spanish

"bienaventurados sois cuando los hombres os aborrecen, cuando os apartan de sí y os vituperan, y desechan vuestro nombre como si fuera malo, por causa del hijo del hombre

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

nu ngi ñaq di jariñoo. ku nu saaga, nu ñaanal la lu baax. coono bu ñu nu teg, nu tegoo ko.

Spanish

nos fatigamos trabajando con nuestras propias manos. cuando somos insultados, bendecimos; cuando somos perseguidos, lo soportamos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ci xol la xalaat yu bon di jóge, ak bóom, njaaloo, ndoxaanu yàqute, càcc, seede lu dul dëgg ak saaga.

Spanish

porque del corazón salen los malos pensamientos, los homicidios, los adulterios, las inmoralidades sexuales, los robos, los falsos testimonios y las blasfemias

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye nit ñii may wax, dañuy saaga li ñu xamul. te li ñu xam ci tañaxu sax, ni bàyyima yu amul xel, dañu ci yàq seen bopp.

Spanish

pero éstos maldicen lo que no conocen; y en lo que por instinto comprenden, se corrompen como animales irracionales

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku la def lu bon mbaa mu saaga la, bul feyyu, waaye ñaanal ko lu baax; ndaxte ci loolu la leen yàlla woo, ngir barkeel leen.

Spanish

no devolváis mal por mal, ni maldición por maldición, sino por el contrario, bendecid; pues para esto habéis sido llamados, para que heredéis bendición

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

looloo tax may bég ci néew doole, yi may wéye ngir turu kirist, ciy tiis, ciy njàqare, mbaa ñu saaga ma, mbaa ñu fitnaal ma. ndaxte bu ma néewee doole, booba laay am kàttan.

Spanish

por eso me complazco en las debilidades, afrentas, necesidades, persecuciones y angustias por la causa de cristo; porque cuando soy débil, entonces soy fuerte

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,938,197,000 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK