Results for set translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

bët set ñu génn betani, fekk yeesu xiif.

Spanish

al día siguiente, cuando salieron de betania, tuvo hambre

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yuusufa fab jëmm ja, laxas ko ci càngaay lu set,

Spanish

josé tomó el cuerpo, lo envolvió en una sábana limpi

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bët bu set nu ngi sant yàlla ndax yéen, di leen boole ci sunuy ñaan.

Spanish

damos siempre gracias a dios por todos vosotros, haciendo mención de vosotros en nuestras oraciones

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foofa ay taalibey yaxya tàmbalee werante ak benn yawut ci mbirum sangu set.

Spanish

entonces surgió una discusión entre los discípulos de juan y un judío acerca de la purificación

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

enos; set; set doomu aadama;aadama doomu yàlla.

Spanish

hijo de enós, hijo de set, hijo de adán, hijo de dios

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ca njël laata bët di set, yeesu jóg dem ca bérab bu wéet, di fa ñaan yàlla.

Spanish

habiéndose levantado muy de madrugada, todavía de noche, jesús salió y se fue a un lugar desierto y allí oraba

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«dafa amoon boroom alal juy sol yére yu rafet te jafe, tey dund bés bu set dund gu neex.

Spanish

"cierto hombre era rico, se vestía de púrpura y de lino fino, y hacía cada día banquete con esplendidez

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

noonu malaaka ma won ma dexu ndoxum dund, mu leer ni weer bu set, di génn ca gàngune mu yàlla ak mbote ma,

Spanish

después me mostró un río de agua de vida, resplandeciente como cristal, que fluye del trono de dios y del cordero

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ba ñu defaree lépp, saraxalekat ya dañu daan dugg bés bu set ca néeg bu jëkk ba, ngir mottali seen liggéeyu saraxale ca yàlla.

Spanish

estas cosas fueron dispuestas así: en la primera parte del tabernáculo entraban siempre los sacerdotes para realizar los servicios del culto

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu ragal ne, dinañu fenqu ci ay xeer, kon ñu daldi sànni ñeenti diigal ci geenu gaal ga, di ñaan bët set.

Spanish

temiendo dar en escollos, echaron las cuatro anclas de la popa y ansiaban el amanecer

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fukki bunt ya ak ñaar, ay per yu weex lañu. bunt bu nekk di benn per kepp. péncu dëkk ba di wurusu ngalam, leer ni weer bu set.

Spanish

las doce puertas eran doce perlas; cada puerta fue hecha de una sola perla. la plaza era de oro puro como vidrio transparente

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sarax yooyu ñu ngi jëmoon ci lekk ak ci naan ak ci fànn yu bare ci mbirum sangu set. ay sàrt yu jëm ci yaram lañu, yu ñu waroon a farataal, ba kera jamono ji yàllay tëral kóllëre gu bees.

Spanish

Éstas son ordenanzas de la carne, que consisten sólo de comidas y bebidas y diversos lavamientos, impuestas hasta el tiempo de la renovación

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,148,453,077 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK