Usted buscó: asiyeamini (Suajili - Wólof)

Contribuciones humanas

De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.

Añadir una traducción

Suajili

Wólof

Información

Suajili

anayeamini na kubatizwa ataokolewa; asiyeamini atahukumiwa.

Wólof

ku gëm te ñu sóob ko ci ndox, dina mucc; ku gëmul, dees na ko daan.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kristo anawezaje kupatana na shetani? muumini ana uhusiano gani na asiyeamini?

Wólof

gan déggoo moo man a am diggante kirist ak beliyar? gan jaxasoo moo man a am diggante ki gëm ak ki gëmul?

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

basi ndugu, jihadharini asije akawako yeyote miongoni mwenu aliye na moyo mbaya hivyo na asiyeamini hata kujitenga na mungu aliye hai.

Wólof

bokk yi, wottuleen ba kenn ci yéen bañ a am xol bu bon te gëmadi, bay dëddu yàlla jiy dund.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

na, kama mwanamke mkristo anaye mume asiyeamini, na huyo mwanamume akakubali kuendelea kuishi naye, basi, asimpe talaka mumewe.

Wólof

naka noonu it su jigéen ju gëm kirist amee jëkkër ju gëmul, te mu nangoo nekk ak moom, warul a tas.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

lakini kama mtu hawatunzi watu wa jamaa yake, hasa wale wa nyumbani kwake, basi, mtu huyo ameikana imani, na ni mbaya zaidi kuliko mtu asiyeamini.

Wólof

ndaxte ki defalul ay bokkam dara, rawatina ay waajuram, weddi na yoonu ngëm wi, ba yées ku gëmadi.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

lakini, wote wakiwa wanautangaza ujumbe wa mungu, akija mtu wa kawaida au asiyeamini, yote atakayosikia yatamhakikishia ubaya wake mwenyewe; yote atakayosikia yatamhukumu.

Wólof

waaye bu ñépp dee wax ci kàddug yàlla, te ku gëmul dugg fa, walla ku jàngul mbiri kirist, wax yi ñépp wax dafay wone bàkkaaram te àtte ko,

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kwa maana huyo mume asiyeamini hupokelewa kwa mungu kwa kuungana na mkewe; na huyo mke asiyeamini hupokelewa kwa mungu kwa kuungana na mumewe. vinginevyo watoto wao wangekuwa si wa mungu; kumbe sasa ni watoto wake mungu.

Wólof

li tax ma wax ko moo di, jëkkër ji gëmul, yàlla sellal na ko, ndax li mu ànd ak jabaram. te it jigéen ji gëmul, yàlla sellal na ko, ndax li mu ànd ak jëkkëram ji gëm; lu ko moy, seeni doom dinañu am sobe, te fekk dañoo sell.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

hata hivyo, ikiwa yule asiyeamini anataka kumwacha mwenzake aliye mkristo, basi, na amwache tu. hapo huyo mkristo, mume au mke, atakuwa huru. maana mungu amewaiteni ninyi muishi kwa amani.

Wólof

waaye nag, su fekkee ki gëmul bëgg na dem, na dem. ci wàll googu nag, ki gëm kirist, muy jëkkër ji walla jabar ji, amul benn tënk, ndaxte yàlla moo leen woo ngir ngeen dund ci jàmm.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Obtenga una traducción de calidad con
7,777,916,898 contribuciones humanas

Usuarios que están solicitando ayuda en este momento:



Utilizamos cookies para mejorar nuestros servicios. Al continuar navegando está aceptando su uso. Más información. De acuerdo