Usted buscó: miili (Suajili - Wólof)

Contribuciones humanas

De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.

Añadir una traducción

Suajili

Wólof

Información

Suajili

basi, waume wanapaswa kuwapenda wake zao kama miili yao wenyewe.

Wólof

na góor bëgg jabaram, ni mu bëgge boppam. bëgg sa jabar, bëgg sa bopp la.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kwa hiyo, dhambi isiitawale tena miili yenu ambayo hufa, na hivyo kuzitii tamaa zake.

Wólof

buleen mayati bàkkaar nag, mu yilif seeni yaram yu néew doole, bay topp ay bëgg-bëggam.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kila wakati tumekuwa tukichukua mwilini mwetu kifo cha kristo, ili uhai wake yesu pia udhihirike katika miili yetu.

Wólof

fu nu tollu noo ngi gàddu ci sunu yaram dee gi yeesu dee woon, ngir dundu yeesu moom it feeñ ci sunu yaram.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kwa sababu hiyo, mungu amewaacha wafuate tamaa mbaya za mioyo yao na kufanyiana mambo ya aibu kwa miili yao.

Wólof

moo tax yàlla bërgël na leen ci seeni bëgg-bëgg, ñu sóobu ciy ñaawteef, di jëfleente lu gàccelu ci seeni cér.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

miili yao ililetwa mpaka shekemu, ikazikwa katika kaburi abrahamu alilonunua kutoka kwa kabila la hamori kwa kiasi fulani cha fedha.

Wólof

gannaaw loolu ñu yóbbu seeni néew sikem, dugal leen ca bàmmeel, ba ibraayma jëndoon ak xaalis ca doomi emor ca sikem.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

kwa hiyo tumkaribie mungu kwa moyo mnyofu na imani timilifu, kwa mioyo iliyotakaswa dhamiri mbaya, na kwa miili iliyosafishwa kwa maji safi.

Wólof

kon nanu jege yàlla ak xol bu laab, ak ngëm gu ànd ak kóolute, am xel mu dal ci bépp yeraange, ak yaram wu ñu raxas ci ndox mu sell.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

hivyo ndivyo pia walivyo watu hawa. ndoto zao huwaongoza katika kuichafua miili yao wenyewe, kuyadharau mamlaka ya mungu na kuvitukana viumbe vitukufu vya huko juu.

Wólof

naka noonu itam gentkat yooyu may wax ñu ngi sobeel seen yaram, di weddi gépp kilifteef, di xas doole yi ci asamaan.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

dhahabu yenu na fedha vimeota kutu, na kutu hiyo itakuwa ushahidi dhidi yenu, nayo itakula miili yenu kama vile moto. ninyi mmejilundikia mali katika siku hizi za mwisho!

Wólof

seen wurus ak seen xaalis xomaag na. te xomaag jooju seede lay doon, su leen di daanlu, ba lakk leen ni safara. dajale ngeen alal ju ne gàññ, te fekk yéena ngi ci muju jamono.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

hali kadhalika ulimi ni kama moto. umejaa maovu chungu nzima, unayo nafasi yake katika miili yetu na hueneza ubaya katika nafsi zetu zote. huteketeza maisha yetu yote kwa moto utokao jehanamu kwenyewe.

Wólof

noonu it làmmiñ safara la, di bon-bonu àddina ci biir cér yi, tey musibaal jëmm jépp. jum la, bu seytaane taal, muy lakk àddina.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

basi, wapenzi wangu, tukiwa tumepewa ahadi hizi zote, na tujitakase na chochote kiwezacho kuchafua miili na roho zetu, tuwe watakatifu kabisa, na tuishi kwa kumcha mungu.

Wólof

ndegam nag jot nanu ci dige yu mel nii, samay soppe, nanu sellal sunu bopp ci bépp sobeb yaram walla bu xel, dund dund gu sell, ba mat ci ragal yàlla.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

mungu ametekeleza jambo lile ambalo sheria haikuweza kutekeleza kwa sababu ya udhaifu w binadamu. mungu alimtuma mwanae akiwa mwenye mwili sawa na miili yetu sisi wenye dhambi, ili aikabili dhambi, na kwa mwili huo akaiangamiza dhambi.

Wólof

lu yoonu musaa mënul woon a def, ndax néew dooley nit, yàlla defe na ko nii: dafa yónni doomam, ngir mu yor sunu jëmm, nun ñiy nekk ay bàkkaarkat, te mu jébbale bakkanam, ngir dindi bàkkaar yi. noonu la yàlla tase nguuru bàkkaar ci nit.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

ilikuwa ijumaa, siku ya maandalio. kwa hiyo, kusudi miili isikae msalabani siku ya sabato, maana siku hiyo ya sabato ilikuwa siku kubwa, wayahudi walimwomba pilato miguu ya hao waliosulubiwa ivunjwe na miili yao iondolewe.

Wólof

keroog ba ñu dee waajal bésu noflaay ba la woon, te yawut ya bëgguñu néew ya des ca bant ya, ndaxte bésu noflaay boobu fonkoon nañu ko lool. Ñu ñaan pilaat, mu dammlu tànki ña ñu daajoon, te jële leen fa.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

"ndiyo maana nawaambieni, msiwe na wasiwasi juu ya chakula na kinywaji mnavyohitaji ili kuishi, wala juu ya mavazi mnayohitaji kwa ajili ya miili yenu. je, maisha ni chakula tu au zaidi? na mwili, je, si zaidi ya mavazi?

Wólof

«loolu moo tax maa ngi leen koy wax, buleen seen bakkan jaaxal, ci lu ngeen war a lekk, walla lu ngeen war a naan. buleen jaaxle it ngir seen yaram, ci lu ngeen war a sol. xanaa bakkan gënul lekk, te yaram gënul koddaay?

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Advertencia: contiene formato HTML invisible

Obtenga una traducción de calidad con
7,787,379,767 contribuciones humanas

Usuarios que están solicitando ayuda en este momento:



Utilizamos cookies para mejorar nuestros servicios. Al continuar navegando está aceptando su uso. Más información. De acuerdo