Vous avez cherché: engel (Afrikaans - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Afrikaans

Wolof

Infos

Afrikaans

en 'n engel uit die hemel het aan hom verskyn en hom versterk.

Wolof

noonu malaakam yàlla daldi koy feeñu, may ko doole.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

toe sê maria vir die engel: hoe kan dit wees aangesien ek geen man het nie?

Wolof

maryaama laaj malaaka ma ne ko: «naka la loolu man a ame? man de, janq laa ba tey.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die rook van die reukwerk het met die gebede van die heiliges uit die hand van die engel opgegaan voor god.

Wolof

noonu saxarus cuuraay li gillee ca loxob malaaka ma, ànd ak ñaani gaayi yàlla ya, jëm ca kanam yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die engel wat ek op die see en op die land sien staan het, het sy hand na die hemel opgehef,

Wolof

noonu malaaka ma ma gis, mu taxaw ci géej gi ak suuf si, yékkati loxol ndeyjooram, mu jëm asamaan,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die derde engel het sy skaal uitgegooi op die riviere en op die waterfonteine, en dit het bloed geword.

Wolof

Ñetteelu malaaka ma sotti ndabam ci dex yi ak ci bëti ndox yi. Ñu daldi nekk deret.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die vierde engel het sy skaal op die son uitgegooi, en daaraan is dit gegee om die mense met vuur te skroei.

Wolof

Ñeenteelu malaaka ma tuur ndabam ci jant bi. noonu ñu jox ko sañ-sañu lakk nit ñi ak tàngaayam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die engel het sy sekel oor die aarde laat gaan en die wingerdstok van die aarde afgeoes en dit gegooi in die groot parskuip van die grimmigheid van god.

Wolof

noonu malaaka ma daldi dawal sàrtam ci àddina, dagg réseñ yi, sànni leen ci biir segalukaay bu réy bu merum yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en toe josef uit die slaap wakker word, het hy gedoen soos die engel van die here hom beveel het en sy vrou by hom geneem;

Wolof

noonu yuusufa yeewu, yeggali jabaram, na ko ko malaakam boroom bi sante woon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en dié het aan die sesde engel met die basuin gesê: maak die vier engele los wat gebind is by die groot rivier, die eufraat.

Wolof

mu ne juróom-benneelu malaaka, ma yoroon liit: «yiwil ñeenti malaaka, ya yeewe ca efraat, dex gu mag ga.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

die openbaring van jesus christus wat god hom gegee het om aan sy diensknegte te toon wat gou moet gebeur, en wat hy deur die sending van sy engel aan sy dienskneg johannes te kenne gegee het,

Wolof

lii mooy li yeesu kirist feeñal, te mu tukkee ca yàlla, ngir mu won ay jaamam mbir, yi dëgmël di ñëw. yónni na malaakaam, ngir xamal ko ab jaamam yowaana.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die engel antwoord en sê vir hom: ek is gabriël wat voor god staan, en ek is gestuur om met jou te spreek en jou hierdie goeie tyding te bring.

Wolof

malaaka ma tontu ko ne: «man maay jibril miy taxaw ci kanam yàlla. dañu maa yónni ngir ma wax ak yaw te yégal la xebaar bu baax boobu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

dit is hy wat in die vergadering in die woestyn was saam met die engel wat met hom op die berg sinai gespreek het, en saam met ons vaders; hy het die lewende woorde ontvang om aan ons te gee.

Wolof

te moo nekkoon ak mbooloo ma ca màndiŋ ma, ànd ak sunuy maam, wéttalikoo malaaka, mi waxoon ak moom ci tundu sinayi. te mu jote ci yàlla kàddu yiy dund, ngir jottali nu ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die engel antwoord en sê vir haar: die heilige gees sal oor jou kom en die krag van die allerhoogste sal jou oorskadu. daarom ook sal die heilige wat gebore word, seun van god genoem word.

Wolof

malaaka ma tontu ko ne: «xel mu sell mi dina wàcc ci yaw, te aji kawe ji dina la yiir ci kàttanam. moo tax xale biy juddu dinañu ko wooye ku sell ki, doomu yàlla ji.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die sewende engel het geblaas, en daar was groot stemme in die hemel wat sê: die koninkryke van die wêreld het die eiendom van onse here geword en van sy christus, en hy sal as koning heers tot in alle ewigheid.

Wolof

juróom-ñaareelu malaaka ma wol liitam, noonu baat yu xumb jib ca asamaan naan:«nguuru àddina, jébbalaat nañu kosunu boroom ak almaseem,te dina nguuru ba fàww.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en 'n ander engel het gevolg en gesê: geval, geval het babilon, die groot stad, omdat sy al die nasies laat drink het van die wyn van die grimmigheid van haar hoerery.

Wolof

meneen malaaka, di ñaareel bi, topp ca naan: «daanu na! babilon, dëkk bu mag, bi daan màndil réew yépp ak biiñu njaaloom, daanu na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en 'n ander engel het gekom en met 'n goue wierookbak by die altaar gaan staan, en baie reukwerk is aan hom gegee, om dit met die gebede van al die heiliges op die goue altaar voor die troon te lê;

Wolof

ba loolu amee meneen malaaka ñëw, taxaw ca wetu saraxalukaayu wurus, ba ñuy taal cuuraay ca kawam, yor andu cuuraayu wurus. Ñu jox ko cuuraay lu bare, ngir mu boole ko ak ñaani gaayi yàlla yépp, joxe ko ci kaw saraxalukaayu wurus ba nekk ci kanam gàngune mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,778,306,780 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK