Vous avez cherché: menjëherë (Albanais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Albanais

Wolof

Infos

Albanais

dhe ata i lanë menjëherë rrjetat dhe e ndoqën.

Wolof

ca saa sa ñu daldi bàyyi seeni mbaal, topp ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai, pra, mori kafshatën dhe doli menjëherë. ishte natë.

Wolof

yudaa nag jël dogu mburu ma, daldi génn ca saa sa. booba guddi woon na.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe kur dolën nga barka, njerëzit e njohën menjëherë

Wolof

génn ca gaal ga. ci saa si nit ñi xàmmi ko,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe pjetri e mohoi sërish, dhe menjëherë këndoi gjeli.

Wolof

waaye piyeer dellu weddi ko. noonu ginaar daldi sab.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe ata lanë menjëherë barkën dhe atin e tyre dhe i shkuan pas.

Wolof

ca saa sa ñu daldi bàyyi gaal ga ak seen baay, topp ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe fama e tij u përhap menjëherë në mbarë krahinën përreth galilesë.

Wolof

noonu turam daldi siiw ci diiwaani galile gépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai e shikon veten dhe pastaj ikën, duke harruar menjëherë si ishte.

Wolof

buleen yem ci déglu kàddu gi rekk, di nax seen bopp; waaye jëfeleen ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe i vuri duart mbi të dhe ajo u drejtua menjëherë, dhe përlëvdonte perëndinë.

Wolof

noonu mu teg ko ay loxoom, soxna sa siggi ca saa sa, di màggal yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe filloi menjëherë të predikojë krishtin në sinagoga se ai është biri i perëndisë.

Wolof

ca saa sa muy yégle ca jàngu ya ne, yeesu mooy doomu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe kur fryti piqet, menjëherë korrësi i vë drapërin, sepse erdhi koha e korrjes.

Wolof

bu gub yi ñoree nag, mu dagg ko, ndaxte ngóob jot na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë vëllezërit e nisën menjëherë palin në drejtim të detit, por sila dhe timoteu qëndruan atje.

Wolof

noonu bokk yi yebal pool ca saa sa, mu jëm géej, waaye silas ak timote des fa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe farisenjtë dolën jashtë e menjëherë bënin këshill bashkë me herodianët kundër tij, se si ta vrasin.

Wolof

ca saa sa nag farisen ya génn, daldi gise ak ñi far ak buur bi erodd, ngir fexe koo reylu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe ai i mori që në atë orë të natës dhe ua lau plagët. dhe ai dhe të gjithë të tijtë u pagëzuan menjëherë.

Wolof

mu jël leen nag ci waxtu woowu ci guddi, raxas seeni gaañu-gaañu, ba noppi ñu sóob ko ci ndox, moom ak waa këram gépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ata, pra, deshnin ta merrnin në barkë, dhe menjëherë barka u bregëzua në atë vend ku ishin drejtuar.

Wolof

noonu ñu nangu koo dugal ca gaal ga, gaal ga daldi teer ca saa sa ca fa ñu bëggoon a wàcc.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

asaj iu kthye fryma e saj dhe menjëherë u çua; pastaj jezusi urdhëroi që t'i jepnin të hante.

Wolof

noonu ruuwu xale ba dellusiwaat, mu daldi jóg ca saa sa. yeesu santaane ñu may ko, mu lekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai mori menjëherë ushtarë dhe centurionë dhe u sul kundër tyre. dhe këta, kur panë tribunin dhe ushtarët, pushuan së rrahuri palin.

Wolof

ca saa sa mu ànd ak ay xarekat ak ay njiiti xare, ne jaas wàcc ci ñoom. bi yawut ya gisee kilifa ga ak xarekat ya nag, ñu daldi bàyyi dóor, ya ñu doon dóor pool.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai u përkul mbi të, qortoi ethet dhe ato e lëshuan; dhe ajo u ngrit menjëherë dhe filloi t'u shërbejë.

Wolof

mu randusi, tiim ko, gëdd tàngoor wi, mu dem. noonu tàngoor wi wàcc, soxna si jóg ca saa sa, di leen topptoo.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ata gjatë rrugës janë ata në të cilët mbillet fjala; por pasi e kanë dëgjuar atë, vjen menjëherë satanai dhe ua heq fjalën e mbjellë në zemrat e tyre.

Wolof

ki féete ci yoon wi mooy ki dégg, seytaane ñëw ci saa si, këf kàddu, gi ñu def ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe, ndërsa ata po i dëgjonin këto, jezusi vazhdoi të tregojë një shëmbëlltyrë, sepse ai ishte afër jeruzalemit dhe ata mendonin se mbretëria e perëndisë do të shfaqej menjëherë.

Wolof

bi nit ñi doon déglu kàddu yooyu, yeesu teg ca léeb, ndaxte jege woon na yerusalem, te ñoom foogoon nañu ne, nguuru yàlla dafay daldi feeñ ca saa sa.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

askush që ka pirë verë të vjetër, nuk do menjëherë verë të re, sepse ai thotë: "e vjetra është më e mirë"''.

Wolof

ku naan biiñ bu màggat du bëgg bu bees bi, ndax day wax ne: “bu màggat bi baax na.”»  

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,772,899,596 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK