Vous avez cherché: ndërkaq (Albanais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Albanais

Wolof

Infos

Albanais

ndërkaq fjala e perëndisë rritej dhe përhapej.

Wolof

moona kàddug boroom bi di gën a màgg tey law.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ju kam thënë këto gjëra, ndërkaq jam me ju;

Wolof

«lii dama leen koy wax ci bi may nekk ak yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq e prunë djalin të gjallë, dhe u ngushëlluan jo pak.

Wolof

naka waxambaane wa, ñu indi ko muy dund, ba seen xol sedd guyy.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq krerët e priftërinjve dhe skribët rrinin aty dhe e paditnin me furi.

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat yaa nga fa woon, di ko jiiñ bu metti.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq mbarë turma e popullit rrinte jashtë e lutej, në orën e temjanit.

Wolof

ca waxtu wa ñuy taal cuuraay la, mbooloo maa nga woon ca biti, di ñaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq dishepujt e vet po i luteshin duke thënë: ''mësues, ha''.

Wolof

fekk taalibey yeesu ya di ko gétën ne: «kilifa gi, lekkal.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq pjetri vazhdonte të trokiste. ata, kur e hapën, e panë atë dhe u mahnitën.

Wolof

fekk piyeer di gën a fëgg. noonu ñu tijji, gis ko, daldi waaru.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq apostujt dhe vëllezërit që ishin në jude morën vesh se edhe johebrenjtë kishin pranuar fjalën e perëndisë.

Wolof

bi loolu amee ndaw yi ak bokk yi nekk ci diiwaanu yude, dégg nañu ne, ñi dul yawut nangu nañu kàddug yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq barka ndodhej në mes të detit; dhe përplasej nga valët sepse era i ishte e kundërt.

Wolof

bi mu fa nekkee nag, gaal ga sore na tefes ga, te duus ya di ko yengal bu metti, ndax ngelaw la leen soflu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq fëmija rritej dhe forcohej në frymë, duke qenë plot dituri; dhe hiri i perëndisë ishte mbi të.

Wolof

xale baa nga doon màgg, di dëgër, mu fees ak xel te yiwu yàlla ànd ak moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq disa bërtisnin një gjë, të tjerë një tjetër, saqë mbledhja ishte trazuar dhe më të shumtët nuk dinin përse ishin mbledhur.

Wolof

noonu ndaje ma rëb, ba ñii di yuuxu lii, ñale di yuuxu laa, te ña ca gën a bare xamuñu lu waral ndaje ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq fëmija rritej dhe forcohej në frymë: dhe qëndroi në shkretëtirë deri në atë ditë, kur ai duhej t'i zbulohej izraelit.

Wolof

noonu yaxyaa ngi doon màgg, te xelam di ubbiku. mu dëkk ca màndiŋ ma, ba bés ba muy feeñu bànni israyil.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq një turmë e madhe judenjsh mori vesh se ai ishte atje dhe erdhi jo vetëm për shkak të jezusit, por edhe për të parë llazarin, te cilin ai e kishte ngjallur prej së vdekurish.

Wolof

bi ñu yégee ne, yeesoo nga fa, mbooloom yawut mu bare daldi dem betani. yeesu rekk yóbbuwu leen fa woon, waaye dañoo bëggoon a gisaale lasaar, mi yeesu dekkaloon.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai ndërkaq po flinte në kiç mbi një jastëk. ata e zgjuan dhe i thanë: ''mësues, a nuk merakosesh që ne po marrim fund?''.

Wolof

fekk yeesu tëdd di nelaw ci ngégenaay ci taatu gaal gi.taalibe yi daldi ko yee naan: «kilifa gi, ndax sunu bakkan soxalu la?»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ndërkaq simon pjetri qëndronte aty e ngrohej. i thanë, pra: ''mos je dhe ti nga dishepujt e tij?''. ai e mohoi dhe tha: ''nuk jam''.

Wolof

fekk na booba simoŋ piyeer, moom, ma nga taxaw di jaaru rekk. Ñu laaj ko ne: «mbaa yaw it bokkuloo ci taalibey waa ji?» waaye piyeer weddi ko ne: «déedéet, bokkuma ci.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,613,127 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK