Vous avez cherché: pjetri (Albanais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Albanais

Wolof

Infos

Albanais

atëherë pjetri doli përjashta dhe qau me hidhërim.

Wolof

piyeer daldi génn, di jooy jooy yu metti.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe pjetri e mohoi sërish, dhe menjëherë këndoi gjeli.

Wolof

waaye piyeer dellu weddi ko. noonu ginaar daldi sab.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

kur hyri pjetri, korneli i doli para, i ra ndër këmbë dhe e adhuroi.

Wolof

bi piyeer duggee nag, korney daje ak moom, daanu ciy tànkam, sargal ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri dhe dishepulli tjetër dolën jashtë dhe u nisën për te varri.

Wolof

piyeer ak beneen taalibe ba daw, dem ca bàmmeel ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai, kur pa se pjetri dhe gjoni po hynin në tempull, u kërkoi lëmoshë.

Wolof

bi mu gisee piyeer ak yowaana nag, ñuy dugg ca kër yàlla ga, mu dékk leen loxo.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri iu përgjigj dhe i tha: ''na e shpjego këtë shëmbëlltyrë''.

Wolof

piyeer nag jël kàddu gi, laaj yeesu: «firil nu léeb wi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

kur ata ndezën një zjarr në mes të oborrit dhe u ulën rreth tij, pjetri u ul midis tyre.

Wolof

amoon na taal ca diggu ëtt ba, ay nit toog, wër ko, piyeer itam toog ci seen biir.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

arriti edhe simon pjetri që po e ndiqte, hyri në varr dhe pa pëlhurat prej liri që ishin përtokë,

Wolof

noonu simoŋ piyeer, mi ko toppoon, agsi, daldi dugg. mu séen càngaay la ci suuf,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe pjetri e ndoqi nga larg deri brenda në pallatin e kryepriftit dhe u ul atje bashkë me rojat dhe ngrohej afër zjarrit.

Wolof

piyeer nag topp ko fu sore, ba ci ëttu saraxalekat bu mag bi, mu toog fa ak alkaati yi, di jaaru ci taal bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri e mori fjalën dhe tha: ''ja, ne lamë çdo gjë dhe të kemi ndjekur''.

Wolof

ci kaw loolu piyeer daldi ko ne: «nun de dëddu nanu lépp te topp la!»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri, me gjonin, duke i ngulur sytë mbi të, i tha: ''na shiko''.

Wolof

ci kaw loolu piyeer ak yowaana ne ko jàkk, te piyeer ne ko: «xool nu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri hapi gojën dhe tha: ''në të vërtetë unë po e marr vesh se perëndia nuk tregohet i anshëm;

Wolof

noonu piyeer jël kàddu ga ne leen: «ci dëgg gis naa ne, yàlla du gënale,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

ai tha: ''eja!''. dhe pjetri zbriti nga barka dhe eci mbi ujëra, për të shkuar te jezusi.

Wolof

yeesu ne ko: «kaay!» piyeer nag wàcc ca gaal ga, di dox ci kaw ndox mi, jëm ci yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

aq sa i binin të sëmurët në sheshe, i vinin në shtretër e në shtroja, që kur kalonte pjetri, të paktën hija e tij të mbulonte ndonjë nga ata.

Wolof

nit ñi indi sax ñu wopp ca mbedd ya, teg leen ca ay lal yu ndaw ak ay leeso, ngir bu piyeer di jaar, doonte takkandeeram sax yiir ñenn ci ñoom.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

dhe, duke qenë se lida është afër jopës, dishepujt, kur morën vesh se pjetri ndodhej atje, i dërguan dy burra që ta lutnin të vijë tek ata pa vonesë.

Wolof

gannaaw lidd sorewul ak yope nag, te taalibe yi dégg ne, piyeer a nga fa, ñu yónnee ko ñaari nit, ñaan ko mu ñëw ci ñoom ci saa si.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri duke u përgjigjur i tha: ''edhe sikur të gjithë të skandalizohen për shkakun tënd, unë nuk do të skandalizohem kurrë!''.

Wolof

piyeer nag daldi jël kàddu gi naan: «bu la ñépp dàggeekoo, man duma la dàggeeku mukk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri u tha atyre: ''pendohuni dhe secili nga ju le të pagëzohet në emër të jezu krishtit për faljen e mëkateve, dhe ju do të merrni dhuratën e frymës së shenjtë.

Wolof

piyeer tontu leen ne: «tuubleen seeni bàkkaar, te kenn ku nekk ci yéen, ñu sóob ko ci ndox ci turu yeesu kirist. noonu yàlla dina leen baal seeni bàkkaar te may leen xel mu sell mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri e mori mënjanë dhe nisi ta qortojë duke thënë: ''o zot, të shpëtoftë perëndia; kjo nuk do të të ndodhë kurrë''.

Wolof

bi mu waxee ba noppi, piyeer woo ko ci pegg, bëgg koo yedd ne ko: «yàlla tere, boroom bi, loolu du la dal.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë pjetri kujtoi atë që i kishte thënë jezusi: ''para se të këndojë gjeli, do të më mohosh tri herë''. dhe ai doli përjashta dhe qau me hidhërim.

Wolof

noonu piyeer fàttaliku la yeesu waxoon ne: «bala ginaar a sab, dinga ma weddi ñetti yoon.» mu daldi génn, di jooy jooy yu metti.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Albanais

atëherë dishepulli, të cilin jezusi e donte, i tha pjetrit: ''Éshtë zoti''. simon pjetri, kur dëgjoi se ishte zoti, u mbështoll me rrobë (sepse ishte i zhveshur) dhe u hodh në det.

Wolof

taalibe ba yeesu bëggoon, ne piyeer: «boroom bi la!» bi simoŋ piyeer déggee loolu, dafa woddoo mbubbam, ndaxte dafa summeeku woon, daldi sóobu ci dex gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,675,272 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK