Vous avez cherché: unschuldigen (Allemand - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Allemand

Wolof

Infos

Allemand

sondern mit dem teuren blut christi als eines unschuldigen und unbefleckten lammes,

Wolof

waaye ci deretu kirist ju tedd ji, mel ni mbote mu sikkul te wàññikuwul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Allemand

wenn ihr aber wüßtet, was das sei: "ich habe wohlgefallen an der barmherzigkeit und nicht am opfer", hättet ihr die unschuldigen nicht verdammt.

Wolof

mbind mi nee na: “yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” su ngeen xamoon lu wax joojuy tekki, kon dungeen teg tooñ ñi tooñul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Allemand

da aber pilatus sah, daß er nichts schaffte, sondern daß ein viel größer getümmel ward, nahm er wasser und wusch die hände vor dem volk und sprach: ich bin unschuldig an dem blut dieses gerechten, sehet ihr zu!

Wolof

naka pilaat xam ne, du ci man dara, fekk na sax yengu-yengu bi gën a am doole, mu daldi fab ndox, raxas ay loxoom ca kanamu mbooloo ma ne leen: «set naa ci deretu ku jub kii; nu ngeen xam, defleen ko.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,771,880 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK