Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
afterwards i came into the regions of syria and cilicia;
bi loolu wéyee dem naa réewu siri ak réewu silisi.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
but before faith came, we were kept under the law, shut up unto the faith which should afterwards be revealed.
bi ngëm yeesu kirist feeñagul nag, yoon wi da noo tëjoon ràpp, ba kera ngëm di feeñ.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
simon peter said unto him, lord, whither goest thou? jesus answered him, whither i go, thou canst not follow me now; but thou shalt follow me afterwards.
simoŋ piyeer laaj ko ne: «boroom bi, foo jëm?» yeesu ne ko: «fa ma jëm, mënuloo ma faa topp léegi, waaye dinga ma toppi ca kanam.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
afterward came also the other virgins, saying, lord, lord, open to us.
gannaaw loolu janq ya ca des agsi naan: “sang bi, sang bi, ubbil nu.”
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :