Vous avez cherché: bear (Anglais - Wolof)

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

for every man shall bear his own burden.

Wolof

ndaxte ku ci nekk dangaa war a yenu sab yen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

if i bear witness of myself, my witness is not true.

Wolof

«su ma seedeelee sama bopp, sama wax du am maana.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

he was not that light, but was sent to bear witness of that light.

Wolof

moom ci boppam du woon leer gi, waaye ñëw na ngir seedeel leer gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and ye also shall bear witness, because ye have been with me from the beginning.

Wolof

te yéen itam dingeen seede samay mbir, ndaxte yéena nekkoon ak man ca njàlbéen ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and whosoever doth not bear his cross, and come after me, cannot be my disciple.

Wolof

képp koo xam ne nanguwuloo ñàkk sa bakkan, ba mel ni ku ñu daaj ci bant, te nga topp ma, doo man a nekk sama taalibe.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as we have borne the image of the earthy, we shall also bear the image of the heavenly.

Wolof

te ni nu yore melokaanu ki ñu sàkke ci suuf, noonu lanuy yoreji melokaanu ki jóge ca asamaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and if it bear fruit, well: and if not, then after that thou shalt cut it down.

Wolof

xëy na dina meññi. bu ko deful, nga gor ko.”»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he saith unto them, draw out now, and bear unto the governor of the feast. and they bare it.

Wolof

noonu yeesu ne leen: «tanqleen ci léegi, yót ko njiitu xew wi.» Ñu daldi ko ciy yót.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and shall not god avenge his own elect, which cry day and night unto him, though he bear long with them?

Wolof

ndax yàlla du àtte jub mbooloom mi mu tànn te ñu koy ñaan wall guddi ak bëccëg? ndax dina leen xaarloo?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as they came out, they found a man of cyrene, simon by name: him they compelled to bear his cross.

Wolof

bi nga xamee ne génn nañu, ñu daje ak nit ku dëkk siren te tudd simoŋ; ñu ga ko, ngir mu gàddu bant, ba ñu war a daaj yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they compel one simon a cyrenian, who passed by, coming out of the country, the father of alexander and rufus, to bear his cross.

Wolof

amoon na nag nit ku dëkk siren, tudd simoŋ, di baayu alegsàndar ak rufus. fekk booba mu romb fa, jóge ca wet, ga féete ak tool ya, ñu ga ko ngir mu gàddu bant bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

(for the life was manifested, and we have seen it, and bear witness, and shew unto you that eternal life, which was with the father, and was manifested unto us;)

Wolof

dund feeñ na, te gis nanu ko; te moom lanuy seedeel, di leen yégal dund gu dul jeex, googu nekkoon ci wetu yàlla baay bi te feeñu nu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,920,033,893 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK