Vous avez cherché: creatures (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

of his own will begat he us with the word of truth, that we should be a kind of firstfruits of his creatures.

Wolof

ci coobareem la nu sole kàddug dëgg gi, ba nu judduwaat, di tànneefu lépp lu mu bind.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the third part of the creatures which were in the sea, and had life, died; and the third part of the ships were destroyed.

Wolof

benn ci ñetti xaaju mbindeef yi nekk ci géej gi dee, te benn ci ñetti xaaju gaal yi yàqu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and every creature which is in heaven, and on the earth, and under the earth, and such as are in the sea, and all that are in them, heard i saying, blessing, and honour, and glory, and power, be unto him that sitteth upon the throne, and unto the lamb for ever and ever.

Wolof

ma dégg itam mbindeef, yi nekk ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf, ci géej gi, — mbindeef yépp naan:«na cant, teraanga, ndam ak nguurféete ak ki toog ci gàngune mi,ak mbote mi ba fàww.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,228,269 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK