Vous avez cherché: desolation (Anglais - Wolof)

Anglais

Traduction

desolation

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

and when ye shall see jerusalem compassed with armies, then know that the desolation thereof is nigh.

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but he, knowing their thoughts, said unto them, every kingdom divided against itself is brought to desolation; and a house divided against a house falleth.

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat ne leen: «réew mu xeex boppam tas, kër gu xeex boppam gent.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and jesus knew their thoughts, and said unto them, every kingdom divided against itself is brought to desolation; and every city or house divided against itself shall not stand:

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat ne leen: «réew mu xeex boppam tas, te dëkk mbaa kër guy xeex boppam du man a yàgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but when ye shall see the abomination of desolation, spoken of by daniel the prophet, standing where it ought not, (let him that readeth understand,) then let them that be in judaea flee to the mountains:

Wolof

«bés baa ngi ñëw, bu li ñuy wax “lu araam luy yàqe” tegee ca bérab bu mu yelloowul; kiy jàng, na xam. bu ngeen gisee loolu nag, ku nekk ci biir diiwaanu yude, nanga daw ca tund ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,913,967,841 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK