Vous avez cherché: dream (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

but when herod was dead, behold, an angel of the lord appeareth in a dream to joseph in egypt,

Wolof

bi nga xamee ne erodd faatu na, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ca misra,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and being warned of god in a dream that they should not return to herod, they departed into their own country another way.

Wolof

bi ñu ko defee yàlla artu na leen ci biir gént, ñu bañ a dellu ca erodd. noonu ñu jaar weneen yoon, ñibbi seen réew.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

when he was set down on the judgment seat, his wife sent unto him, saying, have thou nothing to do with that just man: for i have suffered many things this day in a dream because of him.

Wolof

te it bi mu toogee sax ca jalu àttekaay ba, jabaram yónnee ci moom ne ko: «bul dugg ci yëfi ku jub kooku, ndaxte tey gént naa ci moom te sonn naa ci lool.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

wish you sweet dreams

Wolof

sweet dreams

Dernière mise à jour : 2020-08-12
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,779,348,662 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK