Vous avez cherché: fear (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

there is no fear of god before their eyes.

Wolof

te ragal yàlla sore na seen xol.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

submitting yourselves one to another in the fear of god.

Wolof

teg ca nangul sa moroom ci biir wegeelu kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

howbeit no man spake openly of him for fear of the jews.

Wolof

waaye kenn ñemewu koo tudd ca kaw, ndaxte dañoo ragaloon yawut ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and his mercy is on them that fear him from generation to generation.

Wolof

day wàcce yërmandeem ci ñi ko ragal,ci seeni sët ba ci seeni sëtaat.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when zacharias saw him, he was troubled, and fear fell upon him.

Wolof

naka la ko sakariya gis, fitam daldi dem, mu tiit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and for fear of him the keepers did shake, and became as dead men.

Wolof

Ñi doon wottu tiit bay lox, daldi mel ni ñu dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and deliver them who through fear of death were all their lifetime subject to bondage.

Wolof

noonu mu yiwi nit, ñi meloon ni ay jaam seen giiru dund gépp ndax ragal a dee.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and fear came upon every soul: and many wonders and signs were done by the apostles.

Wolof

ragal jàpp ñépp, te ndaw yi di def ay kéemaan ak ay firnde yu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and so terrible was the sight, that moses said, i exceedingly fear and quake:)

Wolof

te mbir moomu ñu doon seetaan dafa raglu, ba musaa naan: «damaa tiit bay lox.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the angel said unto her, fear not, mary: for thou hast found favour with god.

Wolof

malaaka ma ne ko: «bul ragal dara maryaama, ndaxte yàlla tànn na la ci yiwam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and many of the brethren in the lord, waxing confident by my bonds, are much more bold to speak the word without fear.

Wolof

te it bokk yu bare takk nañu seeni fit ci li ñu gis samay buum, ba tax ñu gën a ñeme ci wax kàddug yàlla ci lu àndul ak genn tiit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and fear came on all that dwelt round about them: and all these sayings were noised abroad throughout all the hill country of judaea.

Wolof

waa dëkk ba bépp jaaxle, xew-xew yooyu siiw ca tundi yude yépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and ananias hearing these words fell down, and gave up the ghost: and great fear came on all them that heard these things.

Wolof

bi anañas déggee baat yooyu, mu daanu dee. Ñi ko dégg ñépp tiit, ba ne nërëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and after three days and an half the spirit of life from god entered into them, and they stood upon their feet; and great fear fell upon them which saw them.

Wolof

waaye bi ñetti fan ya ak genn-wàll wéyee, xelum dund, jóge ca yàlla, solu leen, ñu jóg taxaw. noonu tiitaange gu réy jàpp ñi leen doon seetaan.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and a voice came out of the throne, saying, praise our god, all ye his servants, and ye that fear him, both small and great.

Wolof

noonu baat jibe ca gàngune ma naan:«màggal-leen yàlla sunu boroom,yéen ñépp ñi di ay jaamam,yéen ñi ko ragal, mag ak ndaw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,304,072 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK