Vous avez cherché: his voice (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

wherefore (as the holy ghost saith, to day if ye will hear his voice,

Wolof

moo tax xel mu sell mi wax lii ci mbind mi:«bu ngeen déggee tey jii baatu yàlla bi,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

he shall not strive, nor cry; neither shall any man hear his voice in the streets.

Wolof

du xëccoo mbaa muy wax ci kaw,te kenn du dégg baatam ci mbedd yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and jesus cried with a loud voice, and gave up the ghost.

Wolof

noonu yeesu wootewaat ak kàddu gu dëgër, delloo ruuwam yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

my sheep hear my voice, and i know them, and they follow me:

Wolof

samay xar dinañu dégg sama baat; xam naa leen te ñu ngi may topp.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and there came a voice to him, rise, peter; kill, and eat.

Wolof

te baat ne ko: «jógal, piyeer, rey te lekk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and his feet like unto fine brass, as if they burned in a furnace; and his voice as the sound of many waters.

Wolof

ay tànkam mel ni xànjar bu yànj bu ñu xelli, baatam di riir ni duusi géej.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and i heard a voice saying unto me, arise, peter; slay and eat.

Wolof

te dégg naa baat bu ma ne: “jógal piyeer, rey te lekk.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and this voice which came from heaven we heard, when we were with him in the holy mount.

Wolof

te nun dégg nanu baat boobu jóge asamaan, bi nu nekkee ak moom ca tund wu tedd wa.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the men which journeyed with him stood speechless, hearing a voice, but seeing no man.

Wolof

nit ñi ànd ak moom nag taxaw, waaru ba luu, ci li ñu dégg baat bi te gisuñu kenn.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and a stranger will they not follow, but will flee from him: for they know not the voice of strangers.

Wolof

waaye duñu topp jaambur; dañu koy daw, ndaxte miinuñu baatam.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he said, the god of our fathers hath chosen thee, that thou shouldest know his will, and see that just one, and shouldest hear the voice of his mouth.

Wolof

mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and cried with a loud voice, saying, salvation to our god which sitteth upon the throne, and unto the lamb.

Wolof

naan:«mucc gaa ngi ci yàllasunu boroom, bi toog ci gàngune mi,ak ci mbote mi!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and she spake out with a loud voice, and said, blessed art thou among women, and blessed is the fruit of thy womb.

Wolof

elisabet wax ca kaw ne: «barkeel nañu la ci jigéen ñi, barkeel doom ji nga ëmb!

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and cried with a loud voice, as when a lion roareth: and when he had cried, seven thunders uttered their voices.

Wolof

di xaacu, mel ni gaynde guy yëmmu. naka la xaacu, juróom-ñaari dënnu yi jib.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as he thus spake for himself, festus said with a loud voice, paul, thou art beside thyself; much learning doth make thee mad.

Wolof

bi muy làyyee nii, festus daldi ko gëdd ak baat bu kawe ne ko: «dangaa dof pool! xanaa sa njàng mu réy mi da laa xañ sago.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

again, he limiteth a certain day, saying in david, to day, after so long a time; as it is said, to day if ye will hear his voice, harden not your hearts.

Wolof

noonu ay ati at gannaaw ga, yàlla àppaat na beneen bés, def ko «tey jii,» bi mu waxee ci gémmiñu daawuda ci baat yii ñu jot a lim:«bu ngeen déggee tey jii baatu yàlla bi,buleen dëgër bopp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and i heard another voice from heaven, saying, come out of her, my people, that ye be not partakers of her sins, and that ye receive not of her plagues.

Wolof

noonu ma dégg beneen baat bu jóge asamaan naan: «génnleen ci biiram, yéen samay gaay, ngir ngeen bañ a bokk ci ay bàkkaaram te bañ a am cér ci musiba yi koy dal.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the holy ghost descended in a bodily shape like a dove upon him, and a voice came from heaven, which said, thou art my beloved son; in thee i am well pleased.

Wolof

noonu xel mu sell mi daldi wàcc ci moom, yor jëmmu pitax, te baat bu jóge asamaan jib ne: «yaa di sama doom, ji ma bëgg; ci yaw laa ame bànneex.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and i heard a voice from heaven, as the voice of many waters, and as the voice of a great thunder: and i heard the voice of harpers harping with their harps:

Wolof

ma dégg baat bu jóge asamaan, buy riir ni duusi géej, ni riiru dënnu gu réy. baat ba ma dégg mel ni baati xalamkat yuy xalam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and i beheld, and i heard the voice of many angels round about the throne and the beasts and the elders: and the number of them was ten thousand times ten thousand, and thousands of thousands;

Wolof

ma xool noonu, dégg baatu malaaka yu bare yu ëppoon alfunniy alfunniy junniy junni. malaaka ya wër gàngune ma ak mbindeef ya ak mag ña.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,772,880,132 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK