Vous avez cherché: i belong to you and our father for eternity (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

grace to you, and peace, from god our father and the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now unto god and our father be glory for ever and ever. amen.

Wolof

na yàlla sunu baay yelloo ndam ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

grace be to you and peace from god our father, and from the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :

Anglais

grace unto you, and peace, from god our father and the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla baay bi ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

grace be to you and peace from god the father, and from our lord jesus christ,

Wolof

na yiw ak jàmm féete ak yéen, jóge ci yàlla sunu baay ak yeesu kirist boroom bi,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

grace be unto you, and peace, from god our father, and from the lord jesus christ.

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now god himself and our father, and our lord jesus christ, direct our way unto you.

Wolof

na yàlla sunu baay moom ci boppam ak yeesu sunu boroom jubal sunu yoon ci yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

to all that be in rome, beloved of god, called to be saints: grace to you and peace from god our father, and the lord jesus christ.

Wolof

yéen ñi dëkk room ñépp, yéen ñi yàlla bëgg te woo leen, ngeen nekk gaayam yu sell, na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

to the saints and faithful brethren in christ which are at colosse: grace be unto you, and peace, from god our father and the lord jesus christ.

Wolof

noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell, yi dëkk kolos te di ay bokk ci gëm kirist. na leen yàlla sunu baay may yiw ak jàmm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for this cause, when i could no longer forbear, i sent to know your faith, lest by some means the tempter have tempted you, and our labour be in vain.

Wolof

noonu ba ma ko mënatul a dékku, yónnee naa, ngir xam fu seen ngëm tollu, ngir ragal seytaane fiir leen, ba sunu ñaq neen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and think not to say within yourselves, we have abraham to our father: for i say unto you, that god is able of these stones to raise up children unto abraham.

Wolof

te buleen wax ci seen xel naan: “nun daal doomi ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, yàlla man na sàkkal ibraayma ay doom ci doj yii.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

remembering without ceasing your work of faith, and labour of love, and patience of hope in our lord jesus christ, in the sight of god and our father;

Wolof

dunu noppee fàttaliku ci kanam yàlla sunu baay jëf ji juddu ci seen ngëm, liggéey bi tukkee ci seen mbëggeel, ak muñ gi sosoo ci seen yaakaar ci sunu boroom yeesu kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

bring forth therefore fruits worthy of repentance, and begin not to say within yourselves, we have abraham to our father: for i say unto you, that god is able of these stones to raise up children unto abraham.

Wolof

jëfeleen nag ni ñu tuub seeni bàkkaar, te bañ a nax seen bopp naan: “nun daal doomi ibraayma lanu,” ndaxte maa ngi leen koy wax, yàlla man na defal ibraayma ay doom ci doj yii.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

paul, and silvanus, and timotheus, unto the church of the thessalonians which is in god the father and in the lord jesus christ: grace be unto you, and peace, from god our father, and the lord jesus christ.

Wolof

nun pool, silwan ak timote noo ngi leen di bind, yéen mbooloom ñi gëm ci dëkku tesalonig te nekk ci yàlla baay bi ak boroom bi yeesu kirist. na yiw ak jàmm ànd ak yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he said unto them, take heed what ye hear: with what measure ye mete, it shall be measured to you: and unto you that hear shall more be given.

Wolof

mu ne leen: «seetleen bu baax li ngeen di dégg. dees na leen nattal ak natt, bi ngeen di nattale, te dollil leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and sent timotheus, our brother, and minister of god, and our fellowlabourer in the gospel of christ, to establish you, and to comfort you concerning your faith:

Wolof

te yónni nanu timote, sunu mbokk ak sunu nawle ci liggéeyu yàlla ak ci waareb xebaaru kirist. yónni nanu ko, ngir mu dénk leen, tey feddali seen ngëm,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

they are like unto children sitting in the marketplace, and calling one to another, and saying, we have piped unto you, and ye have not danced; we have mourned to you, and ye have not wept.

Wolof

Ñu ngi nirook xale yu toog ca pénc ma tey woowante naan:“liital nanu leen ak toxoro, te fecculeen,woyal nanu leen woyi dëj, te jooyuleen.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

then paul and barnabas waxed bold, and said, it was necessary that the word of god should first have been spoken to you: but seeing ye put it from you, and judge yourselves unworthy of everlasting life, lo, we turn to the gentiles.

Wolof

bi loolu amee pool ak barnabas ne leen ci lu bir: «yéen lanu war a jëkk a yégal kàddug yàlla, waaye gannaaw gàntu ngeen ko, ba àtte seen bopp ne, yeyoowuleen dund gu dul jeex gi, kon nu ngi woññiku ci ñi dul yawut.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,710,848 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK