Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
and they bring him unto the place golgotha, which is, being interpreted, the place of a skull.
noonu ñu yóbbu yeesu ca bérab bu ñuy wax golgota, liy tekki «bérabu kaaŋu bopp.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
he first findeth his own brother simon, and saith unto him, we have found the messias, which is, being interpreted, the christ.
andare dafa daldi dem seeti simoŋ ne ko: «gis nanu almasi bi.» baat boobu mi ngi tekki «kirist.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
behold, a virgin shall be with child, and shall bring forth a son, and they shall call his name emmanuel, which being interpreted is, god with us.
«janq bi dina ëmb,jur doom ju góor,ñu tudde ko emanuwel,» liy tekki «yàlla ganesi na nu.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and he took the damsel by the hand, and said unto her, talitha cumi; which is, being interpreted, damsel, i say unto thee, arise.
mu jàpp loxoom ne ko: «talita kumi,» liy tekki: «janq bi, maa ngi la koy wax, jógal.»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
and at the ninth hour jesus cried with a loud voice, saying, eloi, eloi, lama sabachthani? which is, being interpreted, my god, my god, why hast thou forsaken me?
ci tisbaar nag yeesu wootee kàddu gu dëgër naan: «elowi, elowi, lema sabaktani?» liy tekki: «sama yàlla, sama yàlla, lu tax nga dëddu ma?»
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :