Vous avez cherché: is there any problem honey (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

for where your treasure is, there will your heart be also.

Wolof

ndaxte fu sa alal nekk, fa la sa xol nekk itam.

Dernière mise à jour : 2023-12-02
Fréquence d'utilisation : 8
Qualité :

Anglais

for wheresoever the carcase is, there will the eagles be gathered together.

Wolof

fa médd nekk, fa la tan yiy dajee.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for where envying and strife is, there is confusion and every evil work.

Wolof

ndaxte fu wextan ak wut aw tur dugg, indi fa xëccoo ak bépp ñaawteef.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for where a testament is, there must also of necessity be the death of the testator.

Wolof

ci li jëm ci dénkaane bu ñu bind, jëme ci miraas, fàww ñu wone firndeg deewu ka ko bind,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

because the law worketh wrath: for where no law is, there is no transgression.

Wolof

yoonu musaa daal du def lu dul wàcce merum yàlla ci sunu bopp; ndax fu yoon amul, jàdd yoon du fa man a am.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

now the lord is that spirit: and where the spirit of the lord is, there is liberty.

Wolof

fekk nag boroom, bi ñuy wax foofu, moo di xelum yàlla, te fu xelu boroom bi nekk, foofa yaatu gu mat am na fa.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

neither is there salvation in any other: for there is none other name under heaven given among men, whereby we must be saved.

Wolof

te mucc amul ci keneen, ndaxte ci ron asamaan amul weneen tur wu ñu maye ci nit ñi, wu nu war a mucce.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

neither is there any creature that is not manifest in his sight: but all things are naked and opened unto the eyes of him with whom we have to do.

Wolof

te itam amul mbindeef mu man a nëbbu yàlla, waaye lépp a ubbiku, ba ne fàŋŋ ci bëti ki nu war a àtte.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and nathanael said unto him, can there any good thing come out of nazareth? philip saith unto him, come and see.

Wolof

nataneel tontu ko ne: «aa! ndax dara lu baax man na jóge nasaret?» filib ne ko: «Ñëwal gis.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

neither was there any among them that lacked: for as many as were possessors of lands or houses sold them, and brought the prices of the things that were sold,

Wolof

kenn ci ñoom ñàkkul dara, ndaxte képp ku nekk boroom suuf mbaa am ay kër, jaay na ko, indi njëg gi,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and then if any man shall say to you, lo, here is christ; or, lo, he is there; believe him not:

Wolof

«booba nag, bu leen kenn waxee: “kaayleen gis, kirist a ngi fi,” mbaa: “xool-leen, mu nga fale,” buleen ko gëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and, ye masters, do the same things unto them, forbearing threatening: knowing that your master also is in heaven; neither is there respect of persons with him.

Wolof

yéen it sang yi, jëfeleen noonu seen diggante ak seeni jaam, te dëddu gépp raglu, xam ne yéena bokk benn boroom ci asamaan, te ñépp a yem fi moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and when the townclerk had appeased the people, he said, ye men of ephesus, what man is there that knoweth not how that the city of the ephesians is a worshipper of the great goddess diana, and of the image which fell down from jupiter?

Wolof

gannaaw loolu boroom dëkk ba dalal mbooloo ma ne leen: «yéen waa efes, ana ku xamul ne, dëkku efes moo di wottukaayu màggalukaayu artemis ak nataalam, bi wàcce asamaan?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,209,450 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK