Vous avez cherché: olive oil (Anglais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

these are the two olive trees, and the two candlesticks standing before the god of the earth.

Wolof

Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari làmpu diwlin, yi taxaw ci kanam boroom suuf si.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but the wise took oil in their vessels with their lamps.

Wolof

waaye ñi am xel ñoom fab nañu seeni làmp, fabaale diwlin ciy njaq.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

they that were foolish took their lamps, and took no oil with them:

Wolof

Ñi ñàkk xel nag fab nañu seeni làmp, waaye fabaalewuñu diwlin;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and they cast out many devils, and anointed with oil many that were sick, and healed them.

Wolof

Ñu dàq ay rab yu bare, te diw boppi jarag yu bare, wéral leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the foolish said unto the wise, give us of your oil; for our lamps are gone out.

Wolof

Ñi ñàkk xel wax ñi am xel: “mayleen nu ci seen diwlin, ndaxte sunuy làmp ñu ngi bëgg a fey.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

can the fig tree, my brethren, bear olive berries? either a vine, figs? so can no fountain both yield salt water and fresh.

Wolof

samay bokk, ndax mas ngeen a gis garabu figg gu meññ oliw, walla garabu réseñ gu meññ ay figg? mukk! mbënnu xorom mënta nàcc mukk ndox mu neex.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and if some of the branches be broken off, and thou, being a wild olive tree, wert graffed in among them, and with them partakest of the root and fatness of the olive tree;

Wolof

bànni israyil a ngi mel ni garabu oliw gu ñu jëmbët ci kër gi, waaye mu am car yu ci fàq. yaw mi dul yawut, yaa ngi mel ni caru garabu oliw gu àll bu ñu jabtal ci garabu kër googu. noonu nga jariñoo meen, mi jóge ci reen bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and as he sat upon the mount of olives over against the temple, peter and james and john and andrew asked him privately,

Wolof

gannaaw loolu, bi nga xamee ne yeesu toog na ci tundu oliw ya, jàkkaarlook kër yàlla ga, piyeer, saag, yowaana ak andare fekki ko cig wet, laaj ko:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,891,620 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK